Vous avez cherché: vetvetes (Albanais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Albanais

Wolof

Infos

Albanais

dhe në qoftë se një shtëpi përçahet kundër vetvetes, ajo shtëpi nuk mund të qëndrojë.

Wolof

te kër gu xeex boppam, du man a yàgg.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

në qoftë se një mbretëri është përçarë kundër vetvetes, ajo mbretëri nuk mund të qëndrojë.

Wolof

réew mu xeex boppam, du man a yàgg.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

kështu, në se satanai ngrihet kundër vetvetes dhe është përçarë, nuk mbahet dot, por i erdhi fundi!

Wolof

bu seytaane nag jógee, ba xeex boppam, xàjjalikoo dikkal na ko te du man a yàgg, waaye dina tas.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

a nuk e dini se trupi juaj është tempulli i frymës së shenjtë që është në ju, të cilin e keni nga perëndia, dhe se nuk i përkitni vetvetes?

Wolof

xanaa xamuleen ne, seen yaram mooy kër yàlla gi? gannaaw xel mu sell maa ngi ci yéen, te yàllaa leen ko may, kon moomuleen seen bopp,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

sepse përndryshe ai duhet të pësonte shumë herë që kur se u krijua bota; por tani, vetëm një herë, në fund të shekujve krishti u shfaq për të prishur mëkatin me anë të flijimit të vetvetes.

Wolof

ndaxte kirist duggul ci bérab bu sell bu nit tabax, muy doon nataal ci bu dëggu bi. waaye dugg na ca biir asamaan sax, ngir taxawal nu ca kanam yàlla léegi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë jezusi u përgjgj dhe u tha atyre: ''në të vërtetë, në të vërtetë po ju them se biri nuk mund të bëjë asgjë prej vetvetes, përveç asaj që sheh se bën ati; gjërat në fakt që bën ati, i bën po ashtu dhe biri.

Wolof

noonu yeesu ne leen: «ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, doom ji mënul a def dara moom ci boppam; li mu gis baay bi di def rekk lay def. li baay bi di jëf la doom ji itam di jëf.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,288,672 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK