Vous avez cherché: command (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

bad command (exec) to launch

Wolof

santaane bees war a jëfe (exec) baaxul

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

these things command and teach.

Wolof

digal leen yëf yooyu nag ci sa njàngale.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

these things i command you, that ye love one another.

Wolof

li may santaane nag, mooy ngeen bëggante.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he answered and said unto them, what did moses command you?

Wolof

yeesu tontu leen ne: «lu leen yoonu musaa sant?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and they besought him that he would not command them to go out into the deep.

Wolof

rab yooyoo ngi ko doon ñaan, ngir mu bañ leen a sant, ñu dem ca kàmb gu xóot gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and the devil said unto him, if thou be the son of god, command this stone that it be made bread.

Wolof

noonu seytaane ne ko: «boo dee doomu yàlla, santal doj wii mu nekk mburu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

they say unto him, why did moses then command to give a writing of divorcement, and to put her away?

Wolof

bi yeesu waxee loolu, farisen ya laaj ko ne: «waaye musaa santaane na, nit jox jabaram kayitu pase, tàggook moom. lu tax mu wax loolu nag?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and unto the married i command, yet not i, but the lord, let not the wife depart from her husband:

Wolof

Ñi séy nag, maa ngi leen di jox ndigal lii --boroom bi moo ko waxoon, du man — jigéen ju séy warul a teqalikoo ak jëkkëram.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when the tempter came to him, he said, if thou be the son of god, command that these stones be made bread.

Wolof

noonu fiirkat bi ñëw ci moom ne ko: «boo dee doomu yàlla, santal doj yii, ñu nekk mburu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but there rose up certain of the sect of the pharisees which believed, saying, that it was needful to circumcise them, and to command them to keep the law of moses.

Wolof

ci kaw loolu ñeneen, ñi gëm waaye bokk ci tariixab farisen ya, daldi jóg ne: «fàww ñi dul yawut xaraf, te ñu dénk leen sàmm yoonu musaa.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when his disciples james and john saw this, they said, lord, wilt thou that we command fire to come down from heaven, and consume them, even as elias did?

Wolof

bi taalibe yi tudd saag ak yowaana gisee loolu, ñu ne: «boroom bi, ndax dangaa bëgg nu ne, na safaras asamaan dal ci seen kaw, faagaagal leen?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and this did she many days. but paul, being grieved, turned and said to the spirit, i command thee in the name of jesus christ to come out of her. and he came out the same hour.

Wolof

muy def noonu ay fani fan, waaye bi ko pool xajootul, mu woññiku ne rab wa: «sant naa la ci turu yeesu kirist, génnal ci moom.» noonu rab wa ne mëll, génn ci moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

command therefore that the sepulchre be made sure until the third day, lest his disciples come by night, and steal him away, and say unto the people, he is risen from the dead: so the last error shall be worse than the first.

Wolof

danoo bëggoon nag, nga santaane, ñu wottu bàmmeel ba, ba am ñetti fan, ngir bañ taalibeem ya ñëw, sàcc néew ba, tey yégle ne dekki na. bu ko defee nax bu mujj boobu dina yées bu jëkk ba.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,791,653,136 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK