Vous avez cherché: die (Anglais - Wolof)

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

this he said, signifying what death he should die.

Wolof

ci baat yooyu la doon misaale ni mu war a faatoo.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for to me to live is christ, and to die is gain.

Wolof

ndaxte su ma dundee, kirist laay noyyee, te su ma deeyee, xéewal lay doon ci man.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

the nobleman saith unto him, sir, come down ere my child die.

Wolof

dagu buur ba neeti ko: «sang bi, ñëwal, bala sama doom di dee.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for as in adam all die, even so in christ shall all be made alive.

Wolof

kon ni ñépp deeye ci seen bokk ci aadama, noonu la ñépp di dundaate ci seen bokk ci kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and as it is appointed unto men once to die, but after this the judgment:

Wolof

kon ni nit ñi deeye benn yoon rekk, ba noppi jaar ca àtte ba, ni ko yàlla dogale,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and whosoever liveth and believeth in me shall never die. believest thou this?

Wolof

rax-ca-dolli kuy dund te gëm ma, doo dee mukk. ndax gëm nga loolu?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for scarcely for a righteous man will one die: yet peradventure for a good man some would even dare to die.

Wolof

kuy nangoo deeyal nit ku jub, yombul a gis, waaye nag jombul am na ku nangoo deeyal ku baax.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

now caiaphas was he, which gave counsel to the jews, that it was expedient that one man should die for the people.

Wolof

kayif moo digaloon yawut ya ne: «li gën moo di kenn rekk dee, ngir mbooloo mi mucc.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and a certain centurion's servant, who was dear unto him, was sick, and ready to die.

Wolof

amoon na fa njiitu xare. njiit la nag, surgaam bu mu bëggoon lool dafa feebaroon, bay bëgg a dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and in those days shall men seek death, and shall not find it; and shall desire to die, and death shall flee from them.

Wolof

ca jamono yooya nit ñi dinañu sàkku dee, waaye duñu daje ak moom. dinañu bëgg a dee, waaye dee da leen di daw.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

lletra de la cançó imagine there's no heaven it's easy if you try no hell below us above us, only sky imagine all the people livin' for today ah imagine there's no countries it isn't hard to do nothing to kill or die for and no religion, too imagine all the people livin' life in peace you you may say i'm a dreamer but i'm not the only one i hope someday you'll join us and the world will be as one imagine no possessions i wonder if you can no need for greed or hunger a brotherhood of man imagine all the people sharing all the world you you may say i'm a dreamer but i'm not the only one i hope someday you'll join us and the world will live as one

Wolof

Dernière mise à jour : 2021-05-31
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :

Référence: Anonyme

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
10,357,561,383 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK