Vous avez cherché: herodias (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

therefore herodias had a quarrel against him, and would have killed him; but she could not:

Wolof

moo tax erojàdd ëmbal ko mer, ba bëgg koo rey, waaye mënu koo def.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but when herod's birthday was kept, the daughter of herodias danced before them, and pleased herod.

Wolof

bi ñu ca tegee ab diir nag, ñuy màggal bés ba erodd juddu woon, te doomu erojàdd ju jigéen di fecc ci biir gan ñi. loolu neex erodd,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but herod the tetrarch, being reproved by him for herodias his brother philip's wife, and for all the evils which herod had done,

Wolof

waaye yaxya yedd na erodd boroom diiwaanu galile, ndaxte dafa takkoon erojàdd, jabaru magam, te it boole woon na ci yeneen ñaawteef,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for herod had laid hold on john, and bound him, and put him in prison for herodias' sake, his brother philip's wife.

Wolof

ndaxte erodd jàppoon na yaxya, yeew ko, tëj. ndaxte erodd takkoon na erojàdd, jabaru filib magam,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when the daughter of the said herodias came in, and danced, and pleased herod and them that sat with him, the king said unto the damsel, ask of me whatsoever thou wilt, and i will give it thee.

Wolof

booba doomu erojàdd dugg di fecc, mu neex erodd ak gan ñi, ba buur bi ne janq bi: «laaj ma loo bëgg, dinaa la ko jox.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for herod himself had sent forth and laid hold upon john, and bound him in prison for herodias' sake, his brother philip's wife: for he had married her.

Wolof

fekk erodd yónnee woon na, jàpp yaxya, yeew ko, tëj. ndaxte erodd takkoon na erojàdd jabaru filib magam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,788,052,731 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK