Vous avez cherché: it is my pleasure (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

for it is god which worketh in you both to will and to do of his good pleasure.

Wolof

ndaxte yàlla ci boppam mooy jëf ci yéen, ngir ngeen fonk coobareem te di ko jëfe.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

fear not, little flock; for it is your father's good pleasure to give you the kingdom.

Wolof

«buleen ragal dara, yéen coggal ju ndaw ji, ndaxte dafa soob seen baay, mu jagleel leen nguuram.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for it is sanctified by the word of god and prayer.

Wolof

ndaxte kàddug yàlla ak ñaan ñoo koy sellal.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

sama khôl means my heart. khôl is heart. sama is my

Wolof

Dernière mise à jour : 2020-12-21
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

because it is written, be ye holy; for i am holy.

Wolof

ndaxte mbind mi nee na: «sell-leen, ndaxte ku sell laa.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

but if our gospel be hid, it is hid to them that are lost:

Wolof

su fekkee ne sax, xebaar bu baax bi dafa muuru ci ñenn ñi, dafa fekk ñoom ñu aw yoon wu jëm ci sànkute.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

as it is written, there is none righteous, no, not one:

Wolof

moom la mbind mi wax ne:«ku jub amul, du kenn sax.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and to this agree the words of the prophets; as it is written,

Wolof

te loolu sax dëppoo na ak li yonent yi tëral; ñu bind ne:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and as it is appointed unto men once to die, but after this the judgment:

Wolof

kon ni nit ñi deeye benn yoon rekk, ba noppi jaar ca àtte ba, ni ko yàlla dogale,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and jesus said unto him, thou hast both seen him, and it is he that talketh with thee.

Wolof

yeesu ne ko: «gis nga ko ba noppi, te mooy kiy wax ak yaw.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and he said unto them, this is my blood of the new testament, which is shed for many.

Wolof

mu ne leen: «lii sama deret la, ji fas kóllëre gi, te mu tuuru ngir ñu bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and jesus, when he had found a young ass, sat thereon; as it is written,

Wolof

yeesu wut cumbur, war ko; ndaxte mbind mi nee na:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and lo a voice from heaven, saying, this is my beloved son, in whom i am well pleased.

Wolof

te baat bu jóge asamaan dégtu ne: «kii mooy sama doom ji ma bëgg; ci moom laa ame bànneex.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

as it is written, he that had gathered much had nothing over; and he that had gathered little had no lack.

Wolof

moom la mbind mi tëral ne:«ki dajale lu bare ëpplewul dara,te ki dajale tuuti ñàkkul.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and as they did eat, jesus took bread, and blessed, and brake it, and gave to them, and said, take, eat: this is my body.

Wolof

noonu bi ñuy lekk, yeesu jël mburu, sant yàlla, jox leen ko naan: «jël-leen, lii sama yaram la.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

but straightway jesus spake unto them, saying, be of good cheer; it is i; be not afraid.

Wolof

waaye ca saa sa yeesu ne leen: «takkleen seen fit, man la, buleen tiit!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and he took bread, and gave thanks, and brake it, and gave unto them, saying, this is my body which is given for you: this do in remembrance of me.

Wolof

gannaaw loolu mu jël mburu, sant yàlla, damm ko, joxleen ko ne: «lii sama yaram la, wi ma joxe ngir yéen. defleen lii, ngir fàttaliku ma.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

(as it is written, he hath dispersed abroad; he hath given to the poor: his righteousness remaineth for ever.

Wolof

moom la mbind mi wax ne:«tabe na, ba may baadoolo yi;njubteem day sax ba fàww.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and there was a cloud that overshadowed them: and a voice came out of the cloud, saying, this is my beloved son: hear him.

Wolof

noonu niir muur leen, te baat jibe ca niir wa naan: «kii mooy sama doom ji ma bëgg, ci moom laa ame bànneex; dégluleen ko.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

conscience, i say, not thine own, but of the other: for why is my liberty judged of another man's conscience?

Wolof

waxuma sa xel yaw, waaye xelu keneen laay wax. waaye nga ne: «li ma sañ a def, lu tax nit ku xelam dalul di am dara lu mu ciy wax?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,782,370,466 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK