Vous avez cherché: meekness (Anglais - Wolof)

Anglais

Traduction

meekness

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

meekness, temperance: against such there is no law.

Wolof

lewetaay ak maandute. yoon wi terewul yu ni mel.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

with all lowliness and meekness, with longsuffering, forbearing one another in love;

Wolof

ngeen woyof toyy te lewet, di muñalante tey baalante ci mbëggeel,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

to speak evil of no man, to be no brawlers, but gentle, shewing all meekness unto all men.

Wolof

buñu jëw kenn mbaa ñuy ŋaayoo, waaye nañu yiwe te won ñépp lewet gu mat sëkk.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

what will ye? shall i come unto you with a rod, or in love, and in the spirit of meekness?

Wolof

lu leen gënal? ma ñëw ci yéen, yor ab yar, walla ma ànd ak mbëggeel, te lewet?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

in meekness instructing those that oppose themselves; if god peradventure will give them repentance to the acknowledging of the truth;

Wolof

na jubbanti cig suufe ñi koy diiŋat, tey yéene yàlla xiir leen ci réccu, ba ñu xam dëgg;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

wherefore lay apart all filthiness and superfluity of naughtiness, and receive with meekness the engrafted word, which is able to save your souls.

Wolof

moo tax nanguleen ci woyof kàddu, gi leen yàlla sol te man leen a musal, di dëddu bépp sobe ak coxor gi daj àddina.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

now i paul myself beseech you by the meekness and gentleness of christ, who in presence am base among you, but being absent am bold toward you:

Wolof

ci lu jëm ci samay mbir nag, maa ngi leen di ñaan — man pool, mi ñu ne, ci seen biir «ragal» laa, bu ma leen soree, «ñeme,» — maa ngi leen di ñaan ndax woyof ak lewetaayu kirist, ngir bu ma ñëwee, ma bañ a ànd ak ñeme gi may dencal ñenn ñiy xalaat ne, gis-gisu nit lanu topp.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but sanctify the lord god in your hearts: and be ready always to give an answer to every man that asketh you a reason of the hope that is in you with meekness and fear:

Wolof

waaye màggal-leen kirist boroom bi ci seeni xol, te jekk ngir tontu ku lay laaj ci seen yaakaar ji ngeen am;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but thou, o man of god, flee these things; and follow after righteousness, godliness, faith, love, patience, meekness.

Wolof

kon nag yaw waayu yàlla ji, dawal loolu, te topp njub, ragal yàlla, ngëm, mbëggeel, muñ ak lewet.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

brethren, if a man be overtaken in a fault, ye which are spiritual, restore such an one in the spirit of meekness; considering thyself, lest thou also be tempted.

Wolof

bokk yi, ku ñu fekk muy def lu yàlla bëggul, yéen ñi topp xelum yàlla, nangeen ko jubbanti ak xol bu lewet. waaye nanga sàmm sa bopp, ngir bàkkaar bañ laa fiir, yaw itam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,906,575,409 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK