Vous avez cherché: on a traversé un cratère (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

the god of our fathers raised up jesus, whom ye slew and hanged on a tree.

Wolof

yàllay sunuy maam dekkal na yeesu, mi ngeen bóomoon ci wékk ko ca bant ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

then the devil taketh him up into the holy city, and setteth him on a pinnacle of the temple,

Wolof

bi mu waxee loolu, seytaane yóbbu ko ca dëkk bu sell ba, teg ko ca njobbaxtalu kër yàlla ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when the king came in to see the guests, he saw there a man which had not on a wedding garment:

Wolof

«bi nga xamee ne buur bi dugg na nag, ngir seetsi gan yi, mu gis fa nit ku solul mbubb mu ñu war a sol ca céet ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and straightway one of them ran, and took a spunge, and filled it with vinegar, and put it on a reed, and gave him to drink.

Wolof

ca saa sa kenn ci ñoom daw, jël aw sagar, capp ko ci bineegar, mu teg ko ci kaw bant, jox ko ko, mu muucu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he brought him to jerusalem, and set him on a pinnacle of the temple, and said unto him, if thou be the son of god, cast thyself down from hence:

Wolof

seytaane yóbbu na ko yerusalem, teg ko ca njobbaxtalu kër yàlla ga ne ko: «boo dee doomu yàlla, tëbal jëm ci suuf,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,770,610,994 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK