Vous avez cherché: without (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

pray without ceasing.

Wolof

te sax ciy ñaan yàlla,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

use hospitality one to another without grudging.

Wolof

ganalanteleen ci lu àndul ak njàmbat.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

do all things without murmurings and disputings:

Wolof

lépp lu ngeen di def nag, buleen ci boole xultu mbaa xuloo.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and jesus said, are ye also yet without understanding?

Wolof

noonu yeesu ne ko: «ndax ba tey seen xol dafa tëju, yéen itam?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for the gifts and calling of god are without repentance.

Wolof

ndax li yàlla maye, dootu ko nangu mukk, te ku mu woo ci boppam, dootu la dàq mukk.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and inasmuch as not without an oath he was made priest:

Wolof

te rax-ca-dolli ngiñ ànd na ci. ndaxte ñi soqikoo ci lewi doon nañu ay saraxalekat te kenn giñul.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

walk in wisdom toward them that are without, redeeming the time.

Wolof

jëfeleen ak xel ci seen diggante ak waa àddina, te fu ngeen ame jot, fexeleen ba jariñoo ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

whereupon neither the first testament was dedicated without blood.

Wolof

looloo waral kóllëre gu jëkk ga, ñu fasoon ko ak deret.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he was three days without sight, and neither did eat nor drink.

Wolof

diirub ñetti fan gisul dara, lekkul, naanul.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for when we were yet without strength, in due time christ died for the ungodly.

Wolof

ndaxte bi nu amul jenn doole, booba la kirist dee ngir nun, fekk danoo weddi woon yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and the whole multitude of the people were praying without at the time of incense.

Wolof

ca waxtu wa ñuy taal cuuraay la, mbooloo maa nga woon ca biti, di ñaan.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

all things were made by him; and without him was not any thing made that was made.

Wolof

ci moom lañu sàkke lépp. amul dara lu ñu sàkk lu jaarul ci moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but them that are without god judgeth. therefore put away from among yourselves that wicked person.

Wolof

Ñi bokkul ci mbooloom ñi gëm, yàlla moo leen di àtte. waaye yéen, ni ko mbind mi waxe: «dàqleen ci seen biir kiy def lu bon.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but if ye be without chastisement, whereof all are partakers, then are ye bastards, and not sons.

Wolof

bu ngeen bokkul woon ci yar, bi ñépp am wàll, kon dungeen ay doomi yoon; ay doom yu daganul ngeen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but now the righteousness of god without the law is manifested, being witnessed by the law and the prophets;

Wolof

waaye léegi nag yàlla feeñal na, ni nit man a jube ci kanamam, ci lu séqul ak yoonu musaa dara. waaye ba tey yoonu musaa ak waxi yonent yi seedeel nañu ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and almost all things are by the law purged with blood; and without shedding of blood is no remission.

Wolof

ndaxte ci yoonu musaa, daanaka deret lañuy sellale lépp, te bu deret tuuruwul, mbaalug bàkkaar du am.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and many of the brethren in the lord, waxing confident by my bonds, are much more bold to speak the word without fear.

Wolof

te it bokk yu bare takk nañu seeni fit ci li ñu gis samay buum, ba tax ñu gën a ñeme ci wax kàddug yàlla ci lu àndul ak genn tiit.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

all these things spake jesus unto the multitude in parables; and without a parable spake he not unto them:

Wolof

loolu yeesu wax mbooloo ma, ëmb na ko lépp ciy léeb, te waxuleen dara lu dul ciy léeb.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

according as he hath chosen us in him before the foundation of the world, that we should be holy and without blame before him in love:

Wolof

ndaxte ba àddina sosoogul, tànn na nu ci kirist, ngir nu man a teew fa kanamam, sell te ñàkk sikk. ci kaw mbëggeelam

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but i would have you without carefulness. he that is unmarried careth for the things that belong to the lord, how he may please the lord:

Wolof

bëggoon naa, ngeen bañ a am benn xalaat. góor gu takkul jabar dafay bàyyi xel ci mbiri boroom bi, di wut a neex boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,770,573,170 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK