Vous avez cherché: اشربها (Arabe - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Arabe

Wolof

Infos

Arabe

فقال يسوع لبطرس اجعل سيفك في الغمد. الكاس التي اعطاني الآب ألا اشربها

Wolof

waaye yeesu ne piyeer: «roofal jaasi ji ci mbaram. ndax warumaa naan kaasu naqar, bi ma baay bi sédd?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فقالا له نستطيع. فقال لهما يسوع اما الكاس التي اشربها انا فتشربانها وبالصبغة التي اصطبغ بها انا تصطبغان.

Wolof

Ñu ne ko: «waaw, man nanu ko.» noonu yeesu ne leen: «dingeen naan kaasu naqar, bi may naan, tey sóobu ci metit, yi ma nar a sóobu,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فقال لهما يسوع لستما تعلمان ما تطلبان. أتستطيعان ان تشربا الكاس التي اشربها انا وان تصطبغا بالصبغة التي اصطبغ بها انا.

Wolof

waaye yeesu tontu leen: «xamuleen li ngeen di ñaan. ndax man ngeen a naan kaasu naqar, bi may naan? ndax man ngeen a sóobu ci metit, yi ma nar a sóobu?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فاجاب يسوع وقال لستما تعلمان ما تطلبان. أتستطيعان ان تشربا الكاس التي سوف اشربها انا وان تصطبغا بالصبغة التي اصطبغ بها انا. قالا له نستطيع.

Wolof

yeesu ne ko: «xamuleen li ngeen di ñaan. ndax man ngeen a naan kaasu naqar, bi may naan?» Ñu tontu ko: «man nañu ko.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

الحق اقول لكم اني لا اشرب بعد من نتاج الكرمة الى ذلك اليوم حينما اشربه جديدا في ملكوت الله.

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, dootuma naan gannaaw tey ndoxum réseñ mii, ba kera ma ciy naan bu bees ci nguuru yàlla.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,782,205,333 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK