Vous avez cherché: grijeh (Croate - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Croate

Wolof

Infos

Croate

grijeh je što ne vjeruju u mene;

Wolof

ci mbiri seen bàkkaar, dina leen yey ci li ñu ma gëmul.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

Žalac je smrti grijeh, snaga je grijeha zakon.

Wolof

daŋaru dee mooy bàkkaar, te dooley bàkkaar mooy yoon wi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

onda to ne èinim više ja, nego grijeh koji prebiva u meni.

Wolof

léegi nag du man maay def lu bon loolu, waaye bàkkaar bi dëkk ci man, moo ma ciy jiiñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

svaka je nepravda grijeh. a postoji grijeh koji nije na smrt.

Wolof

gépp jubadi bàkkaar la, waaye am na bàkkaar bu jarul dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

ako li ste pristrani, grijeh èinite i zakon vas osuðuje kao prijestupnike.

Wolof

waaye su ngeen gënalee, bàkkaar ngeen, te yoonu yàlla dina leen dab ni ñu moy.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

požuda zatim, zatrudnjevši, raða grijehom, a grijeh izvršen raða smræu.

Wolof

kon bu bëgg-bëgg ëmbee, bàkkaar lay wasin, te bu bàkkaar màggee, jur dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

doista grijeh, uhvativši priliku, zapovijeðu me zavede, njome me i ubi.

Wolof

ndaxte bàkkaar jaar na ci li yàlla digle, ba nax ma, rey ma.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

neka dakle ne kraljuje grijeh u vašem smrtnom tijelu da slušate njegove požude;

Wolof

buleen mayati bàkkaar nag, mu yilif seeni yaram yu néew doole, bay topp ay bëgg-bëggam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

da, ja sam nekoæ živio bez zakona. ali kad je došla zapovijed, grijeh oživje.

Wolof

te keroog bi ma xamagul lu yoon wi santaane, maa ngi doon dund dund gu neex; waaye ba ma ko déggee, bàkkaar dafa daldi fuddu ci man, te man ma daldi dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

a kad on doðe, pokazat æe svijetu što je grijeh, što li pravednost, a što osuda:

Wolof

te bu dikkee, dina yey niti àddina ci lu jëm ci seen bàkkaar, ci lu jëm ci sama njubte ak ci lu jëm ci àtte ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

a zakon nadoðe da se umnoži grijeh. ali gdje se umnožio grijeh, nadmoæno izobilova milost:

Wolof

te yoonu musaa daldi wàcc, ngir bàkkaar gën a bare; waaye fa bàkkaar bare, yiwu yàlla gën faa bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

ali je pismo sve zatvorilo pod grijeh da se, po vjeri u isusa krista, obeæano dade onima koji vjeruju.

Wolof

waaye yoon wi tëj na ñépp ci dooley bàkkaar, ngir ñi gëm yeesu kirist jot li yàlla dige woon ci seen kaw ngëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

a grijeh je, uhvativši priliku, po zapovijedi u meni prouzroèio svakovrsnu požudu. ta bez zakona grijeh je mrtav.

Wolof

waaye bàkkaar jaare na ci ndigalu yàlla, daldi ñëw dugg ci man, ba yengal ci man xemmem yu bare. ndaxte ba ma xamagul woon yoonu musaa, bàkkaar da ne woon nemm ci man.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

bježite od bludnosti! svaki grijeh koji uèini èovjek, izvan tijela je, a bludnik griješi protiv svojega tijela.

Wolof

dawleen njaaloo! bépp bàkkaar bu nit man a def, du laal yaramam, waaye nag kuy njaaloo, dafay bàkkaar, di lor yaramam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

zato i mi, okruženi tolikim oblakom svjedoka, odložimo svaki teret i grijeh koji nas sapinje te postojano trèimo u borbu koja je pred nama!

Wolof

kon nag gannaaw mbooloo mu bare moo nu yéew, di nu seedeel seen ngëm, nanu yenniku bépp yen ak bàkkaar bu nuy téqtal ci lu yomb, tey daw xél wi nekk sunu kanam, ànd ci ak muñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

inaèe bi bilo trebalo da trpi mnogo puta od postanka svijeta. no sada se pojavio, jednom na svršetku vjekova, da grijeh dokine žrtvom svojom.

Wolof

bu demee woon noonu, kon dina sonn ba tàyyi ca njàlbéenug àddina ba tey. waaye nag benn yoon rekk la feeñu ci mujjeelu jamono yi, joxe boppam ni sarax ngir far bàkkaar yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

"zato kažem vam: svaki æe se grijeh i bogohulstvo oprostiti ljudima, ali rekne li tko bogohulstvo protiv duha, neæe se oprostiti.

Wolof

yeesu teg ca ne: «loolu moo tax maa ngi leen koy wax, bàkkaar walla sos wu mu man a doon, dinañu ko baale, waaye ku sosal xelum yàlla, duñu ko baal.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Croate

odgovori mu isus: "ne bi imao nada mnom nikakve vlasti da ti nije dano odozgor. zbog toga ima veæi grijeh onaj koji me predao tebi."

Wolof

yeesu tontu ko ne: «amuloo benn sañ-sañ ci man su dul bi la yàlla jox. looloo tax ba ki ma jébbal ci say loxo am na bàkkaar, bi gën a réy.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Croate

tako i krist: jednom se prinese da grijehe mnogih ponese, a drugi æe se put - bez obzira na grijeh - ukazati onima koji ga išèekuju sebi na spasenje.

Wolof

noonu it la kirist joxee boppam benn yoon, ngir gàddu bàkkaaru nit ñu bare, te dina feeñaat, waxuma ci mbiri bàkkaar, waaye ngir indil ñi koy séentu mucc gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Croate

vidi li tko brata svojega gdje èini grijeh koji nije na smrt, neka ište i dat æe mu život - onima koji èine grijeh što nije na smrt. ima grijeh što je na smrt; za nj ne velim da moli.

Wolof

ku gis mbokkam, muy def bàkkaar bu jarul dee, na ko ñaanal, te yàlla dina ko may dund. ku def bàkkaar bu jarul dee laa wax. ndaxte am na bàkkaar bu jar dee; boobu taxul may wax, mu ñaanal ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,320,252 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK