Vous avez cherché: atravesaron (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

atravesaron por anfípolis y apolonia y llegaron a tesalónica, donde había una sinagoga de los judíos

Wolof

bi ñu fa jógee, ñu aw yoon wa jaar dëkku amfipolis ak apoloni, door a ñëw tesalonig, fa yawut ya am jàngu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

atravesaron la región de frigia y de galacia, porque les fue prohibido por el espíritu santo hablar la palabra en asia

Wolof

bi loolu amee gannaaw xel mu sell mi aaye na leen, ñu yégleji kàddu gi ci diiwaanu asi, ñu daldi jaari wàlli firisi ak galasi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

no quiero que ignoréis, hermanos, que todos nuestros padres estuvieron bajo la nube, y que todos atravesaron el mar

Wolof

bokk yi, bëgguma ngeen umple li daloon sunu maam ya. Ñoom ñépp niir wa tiimoon na leen, te ñoom ñépp jàll nañu géej.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,773,652,461 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK