Vous avez cherché: nación (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

porque ama a nuestra nación y él mismo nos edificó la sinagoga

Wolof

ndaxte sopp na sunu xeet te moo nu tabaxal sax sunu jàngu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

pasados muchos años, vine para presentar donativos y ofrendas a mi nación

Wolof

«noonu gannaaw gëjeb at yu bare ñëw naa, ngir indil sama xeet ndimbal te jébbal yàlla ay sarax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

--entonces dijo--: se levantará nación contra nación y reino contra reino

Wolof

noonu mu teg ca ne: «xeet dina jóg, xeex ak weneen xeet, réew dina xeex ak meneen réew.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

ni consideráis que os conviene que un solo hombre muera por el pueblo, y no que perezca toda la nación

Wolof

xanaa xamuleen ne, kenn nit rekk dee ngir ñépp, mooy li gën ci yéen? bu ko defee réew mi du tas.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque se levantará nación contra nación y reino contra reino. habrá hambre y terremotos por todas partes

Wolof

xeet dina jóg, xeex ak weneen xeet, réew xeex ak meneen réew. dina am ay xiif ak ay yengu-yenguy suuf ci bérab yu bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

me destacaba en el judaísmo sobre muchos de mis contemporáneos en mi nación, siendo mucho más celoso de las tradiciones de mis padres

Wolof

bokkoon naa ci ñi gën a farlu ci diiney yawut yi, te sawar it ci sàrti yoon, yi fi samay maam bàyyi, ba raw sama maas, gi ma bokkal askan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

si le dejamos seguir así, todos creerán en él; y vendrán los romanos y destruirán nuestro lugar y nuestra nación

Wolof

ndaxte su nu ko bàyyee mu jàppoo nii, ñépp dinañu ko gëm, te kilifay room yi dinañu ñëw, daaneel sunu kër yàlla gi, tas sunu réew!»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

mi manera de vivir, desde mi juventud, la cual pasé desde el comienzo entre los de mi nación en jerusalén, la conocen todos los judíos

Wolof

«ci lu jëm ci yawut yi, xam nañu sama dund li dale ci samag ndaw, muy ci sama biir xeet, muy ci yerusalem.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

pero vosotros sois linaje escogido, real sacerdocio, nación santa, pueblo adquirido, para que anunciéis las virtudes de aquel que os ha llamado de las tinieblas a su luz admirable

Wolof

waaye yéen xeet wu yàlla tànn ngeen, di askanu saraxalekati buur yàlla, askan wu sell ngeen, di mbooloom yàlla, ngir ngeen yégle ngëneelam, moom mi leen woo, ba génne leen lëndëm gi, tàbbal leen ci leeram gu yéeme gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

pilato respondió: --¿acaso soy yo judío? tu propia nación y los principales sacerdotes te entregaron a mí. ¿qué has hecho

Wolof

pilaat ne ko: «mbaa xalaatoo ne, man yawut laa? sa xeet ak saraxalekat yu mag yi ñoo ma la jébbal. lan nga def?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

"pero yo juzgaré a la nación a la cual sirvan", dijo dios, "y después de esto saldrán y me rendirán culto en este lugar.

Wolof

waaye yàlla nee na: “xeet wi leen jaamloo, man maa leen di àtte te gannaaw loolu dinañu génn, di ma jaamu ci bérab bii.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Espagnol

y al ser llamado éste, tértulo comenzó a acusarle diciendo: --puesto que gozamos de mucha paz, gracias a ti, y se están realizando reformas en beneficio de esta nación debido a tu prudencia

Wolof

noonu ñu woo pool, te tertul daldi ko jiiñ naan: «yaw feligsë mu tedd mi, sa nguur jural na nu jàmm ju neex, te sa jàppandil soppi na lu bare ci sunu xeet.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

--como está escrito: te he puesto por padre de muchas naciones-- delante de dios, a quien él creyó, quien vivifica a los muertos y llama a las cosas que no existen como si existieran

Wolof

moom la yàlla dogal, wax ko ci mbind mi ne: «def naa la baayu xeet yu bare.» ndaxte ibraayma gëmoon na yàlla, miy dekkal ñi dee, tey wax ci lu amagul, mel ni dafa am.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,788,534,572 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK