Vous avez cherché: dragon (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

il saisit le dragon, le serpent ancien, qui est le diable et satan, et il le lia pour mille ans.

Wolof

mu jàpp ninkinànka ja, di jaani cosaan ja, muy tuumaalkat bi, maanaam seytaane. malaaka ma yeew ko diirub junniy at,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et il y eut guerre dans le ciel. michel et ses anges combattirent contre le dragon. et le dragon et ses anges combattirent,

Wolof

noonu xare am ca asamaan ya. mikayel ak malaaka, ya ànd ak moom, xeex ak ninkinànka ja, ninkinànka ja it ak ay malaakaam feyyu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

quand le dragon vit qu`il avait été précipité sur la terre, il poursuivit la femme qui avait enfanté l`enfant mâle.

Wolof

ba ninkinànka ja gisee ne, daaneel nañu ko ci kaw suuf, mu dàq jigéen, ja juroon doom ju góor ja.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

puis je vis monter de la terre une autre bête, qui avait deux cornes semblables à celles d`un agneau, et qui parlait comme un dragon.

Wolof

noonu ma gis weneen rab di génn ci suuf. am na ñaari béjjén yu mel ni yu mbote, waaye di wax ni ninkinànka.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et je vis sortir de la bouche du dragon, et de la bouche de la bête, et de la bouche du faux prophète, trois esprits impurs, semblables à des grenouilles.

Wolof

noonu ma gis ñetti rab yu bon yu mel niy mbott, génn ci gémmiñi ninkinànka ja ak rab wa ak naaféq, ba mbubboo yonent.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et le dragon fut irrité contre la femme, et il s`en alla faire la guerre au restes de sa postérité, à ceux qui gardent les commandements de dieu et qui ont le témoignage de jésus.

Wolof

ninkinànka ja mere jigéen ja, daldi xeexi ak ñi des ciy doomam, di ñiy sàmm ndigali yàlla tey sax ci di seedeel yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et il fut précipité, le grand dragon, le serpent ancien, appelé le diable et satan, celui qui séduit toute la terre, il fut précipité sur la terre, et ses anges furent précipités avec lui.

Wolof

daaneel nañu ko, moom ninkinànka ju réy ji, di jaani cosaan ji, te ñu di ko wax tuumaalkat bi mbaa seytaane, moom miy nax waa àddina sépp — daaneel nañu ko ci kaw suuf, moom ak ay malaakaam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et ils adorèrent le dragon, parce qu`il avait donné l`autorité à la bête; ils adorèrent la bête, en disant: qui est semblable à la bête, et qui peut combattre contre elle?

Wolof

Ñu jaamu ninkinànka ja ndax li mu joxoon sañ-sañ rab wa, di jaamu it rab wa, naan: «rab wi amul moroom, kenn mënul a xeex ak moom.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,304,072 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK