Vous avez cherché: bölcseségét (Hongrois - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Hongrois

Wolof

Infos

Hongrois

mert meg van írva: elvesztem a bölcseknek bölcseségét és az értelmeseknek értelmét elvetem.

Wolof

ndaxte mbind mi nee na:«dinaa folli xam-xamu boroom xam-xam yi,lem xalaati ñi am xel.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Hongrois

Ámde magoknak a hivatalosoknak, úgy zsidóknak, mint görögöknek krisztust, istennek hatalmát és istennek bölcseségét.

Wolof

waaye ci ñi yàlla woo, ñuy yawut mbaa di gereg, kirist mooy dooley yàlla, di xam-xamu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Hongrois

bölcseséget pedig a tökéletesek között szólunk; ámde nem e világnak, sem e világ veszendõ fejedelmeinek bölcseségét;

Wolof

moona am na xam-xam bu nuy yégal ñi mat, xam-xam bu bokkul ci àddina si, te njiiti àddina si xamuñu ko, ñoom ñi nar a wéy.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Hongrois

hol a bölcs? hol az írástudó? hol e világnak vitázója? nemde nem bolondsággá tette-é isten e világnak bölcseségét?

Wolof

ana boroom xam-xam bi? ana kaaŋ mi? ana boroom làmmiñ wu neex, wi ci àddina sii? xanaa yàlla wonewul ne, xam-xamu àddina si ag ndof la?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Hongrois

a délnek királynéasszonya felkél majd az ítéletkor e nemzetség férfiaival, és kárhoztatja õket: mert õ eljött a földnek szélérõl, hogy hallhassa a salamon bölcseségét; és ímé nagyobb van itt salamonnál.

Wolof

keroog bés pénc buur bu jigéen, ba dëkkoon ca sudd, dina jógandoo ak niti jamono jii, yey leen; ndaxte dafa jóge ca catul àddina, ngir déglu xam-xamu suleymaan, te ku sut suleymaan a ngi fi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Hongrois

a kit mi prédikálunk, intvén minden embert, és tanítván minden embert minden bölcseséggel, hogy minden embert tökéletesnek állassunk elõ a krisztus jézusban;

Wolof

moom kirist lanuy yégle, di artu te di jàngal ku nekk, ànd ak xel mu mat, ngir jébbal yàlla ku nekk ni ku mat ci kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,787,781,830 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK