Vous avez cherché: melainkan (Indonésien - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Indonésien

Wolof

Infos

Indonésien

dan bukannya adam, melainkan wanitalah yang tertipu, sehingga melanggar perintah allah

Wolof

te it du aadama la seytaane nax, waaye jigéen ja la nax, ba mu jàdd.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Indonésien

tetapi kain yang diikat pada kepala yesus tidak ada di dekatnya melainkan tergulung tersendiri

Wolof

ak kaala ga muuroon boppu yeesu. waaye kaala googu àndul ak càngaay la; dañu ko laxas, teg ko ci wet.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Indonésien

maka keduanya menjadi satu.' jadi, mereka bukan lagi dua orang, melainkan satu

Wolof

ñoom ñaar doon benn.” kon nekkatuñu ñaar waaye benn.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Indonésien

(sebenarnya yesus sendiri tidak membaptis melainkan pengikut-pengikut-nya saja.

Wolof

fekk yeesu moom ci boppam daawul sóob kenn ci ndox, waaye ay taalibeem ñoo daan sóobe.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Indonésien

saya berbuat begitu, supaya kepercayaanmu kepada kristus tidak berdasarkan kebijaksanaan manusia, melainkan berdasarkan kuasa allah

Wolof

ngir seen ngëm bañ a wékku ci xam-xamu nit ñi waaye mu wékku ci dooley yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Indonésien

laki-laki tidak pula dijadikan untuk kepentingan wanita, melainkan wanita dijadikan untuk kepentingan laki-laki

Wolof

te sàkkuñu góor ngir jigéen, waaye jigéen lañu sàkk ngir góor.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Indonésien

allah memanggil kita, bukan supaya kita hidup cabul, melainkan supaya kita hidup dengan cara yang menyenangkan hati-nya

Wolof

ndaxte yàlla woo na nu, nu dund ci cell, waaye du ci sobe.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Indonésien

hendaklah kalian hidup sebagai orang merdeka, tetapi janganlah memakai kemerdekaanmu itu untuk menutupi kejahatan, melainkan hiduplah sebagai hamba allah

Wolof

li leen yàlla goreel nag, bu mu tax ngeen mbubboo ko, bay def lu bon, waaye ngeen gën a feddali seen jaamu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Indonésien

lainnya

Wolof

yeneen

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,800,250,132 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK