Vous avez cherché: prodigi (Italien - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Italien

Wolof

Infos

Italien

dio intanto operava prodigi non comuni per opera di paolo

Wolof

booba yàllay def ay kéemaan yu ràññiku yuy jaar ci loxoy pool.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

un senso di timore era in tutti e prodigi e segni avvenivano per opera degli apostoli

Wolof

ragal jàpp ñépp, te ndaw yi di def ay kéemaan ak ay firnde yu bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

gesù gli disse: «se non vedete segni e prodigi, voi non credete»

Wolof

yeesu ne ko: «yéen daal, dungeen gëm mukk, fi ak gisuleen ay firnde walla ay kéemaan.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

farò prodigi in alto nel cielo e segni in basso sulla terra, sangue, fuoco e nuvole di fumo

Wolof

dinaa wone ay kéemaan ci kaw ci asamaanak ay firnde ci suuf ci àddina,muy deret, safara ak ay niiri saxar.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

la cui venuta avverrà nella potenza di satana, con ogni specie di portenti, di segni e prodigi menzogneri

Wolof

bu nitu ñaawteef kooku feeñee, dina ànd ak kàttanu seytaane ak doole ju bare, di wone ay firnde ak ay kéemaan yu dul dëgg;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

molti miracoli e prodigi avvenivano fra il popolo per opera degli apostoli. tutti erano soliti stare insieme nel portico di salomone

Wolof

bi loolu amee ay kéemaan ak ay firnde yu bare di xew ci nit ñi, jaare ca loxoy ndaw ya. Ñépp di booloo ca werandaa bu suleymaan ca kër yàlla ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

sono infatti spiriti di demòni che operano prodigi e vanno a radunare tutti i re di tutta la terra per la guerra del gran giorno di dio onnipotente

Wolof

ay rabi seytaane lañu woon, yuy def ay kéemaan te di dem ci buuri àddina sépp, di leen dajale, ngir xeex biy am ci bés bu mag, bi yàlla aji kàttan jagleele boppam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

allora essi partirono e predicarono dappertutto, mentre il signore operava insieme con loro e confermava la parola con i prodigi che l'accompagnavano

Wolof

taalibe ya dem waareji, te loxob boroom bi ànd ak ñoom, di dëggal kàddu gi ak firnde, yi ci ànd.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

certo, in mezzo a voi si sono compiuti i segni del vero apostolo, in una pazienza a tutta prova, con segni, prodigi e miracoli

Wolof

kéemaan yi, jaloore yi ak jëf yu màgg, yiy firndeel ndawul kirist, feeñ nañu ci seen biir, ma ànd ci ak muñ gu mat.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

egli li fece uscire, compiendo miracoli e prodigi nella terra d'egitto, nel mare rosso, e nel deserto per quarant'anni

Wolof

moo leen génne réewu misra, di def ay kéemaan ak ay firnde ca réew ma, ca géej gu xonq ga ak ca màndiŋ ma diirub ñeent-fukki at.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

con la potenza di segni e di prodigi, con la potenza dello spirito. così da gerusalemme e dintorni fino all'illiria, ho portato a termine la predicazione del vangelo di cristo

Wolof

ci ay tegtal ak i kéemaan, sukkandikoo ci dooley xelu yàlla mi. ba fi mu nekk nag yégle naa fu nekk xebaaru kirist, li dale ci yerusalem, jaar ci gox yépp, ba àgg diiwaanu iliri.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

era ormai vicino alla discesa del monte degli ulivi, quando tutta la folla dei discepoli, esultando, cominciò a lodare dio a gran voce, per tutti i prodigi che avevano veduto, dicendo

Wolof

bi ñu agsee fa mbartalum tundu oliw ya doore, taalibeem yépp fees ak mbég, tàmbalee màggal yàlla ca kaw ndax kéemaan yu bare yi ñu gis.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

allora alcuni dei farisei dicevano: «quest'uomo non viene da dio, perché non osserva il sabato». altri dicevano: «come può un peccatore compiere tali prodigi?». e c'era dissenso tra di loro

Wolof

ci noonu am ca farisen ya ñu naan: «ki def lii, mënul a jóge ca yàlla, ndaxte toppul ndigalu bésu noflaay bi.» Ñeneen it di wax ne: «nan la boroom bàkkaar man a wonee yii firnde?» noonu ñu daldi féewaloo ci seen biir.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,774,100,143 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK