Vous avez cherché: apud (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

hoc erat in principio apud deu

Wolof

moo di ki nekkoon ak yàlla ca njàlbéen ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

non est enim personarum acceptio apud deu

Wolof

ndaxte ñépp a yem fa kanam yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

haec locutus sum vobis apud vos manen

Wolof

«lii dama leen koy wax ci bi may nekk ak yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

mea defensio apud eos qui me interrogant haec es

Wolof

nii laay tontoo ñi may àtte:

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quid incredibile iudicatur apud vos si deus mortuos suscita

Wolof

lu tax seen xel dàq ne, yàlla dina dekkal ñi dee?

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

ait illis quae inpossibilia sunt apud homines possibilia sunt apud deu

Wolof

yeesu tontu ne: «li të nit ñi, tëwul yàlla.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ego in infirmitate et timore et tremore multo fui apud vo

Wolof

bi ma teewee ci yéen, ànd naa ak ñàkk doole, ragal ak njàqare.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ait angelus ei ne timeas maria invenisti enim gratiam apud deu

Wolof

malaaka ma ne ko: «bul ragal dara maryaama, ndaxte yàlla tànn na la ci yiwam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

bonum autem aemulamini in bono semper et non tantum cum praesens sum apud vo

Wolof

farle baax na, bu àndee ak mébét mu baax. waaye bu sama jëmm rekk tax ngeen koy def.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

apud vos autem forsitan manebo vel etiam hiemabo ut vos me deducatis quocumque ier

Wolof

man na am ma yàgg ci yéen, jombul sax ma lollikoo fi yéen. noonu dingeen taxawu sama yoon, fu ma man a jëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

audet aliquis vestrum habens negotium adversus alterum iudicari apud iniquos et non apud sancto

Wolof

te it bu kenn ci yéen amee lëj-lëj digganteem ak mbokku taalibeem, lu tax muy dem ca àttekaayi ñi xamul yàlla, te bañ a dem ca gaayi yàlla yi, ñu àtte ko?

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

alia autem die profecti venimus caesaream et intrantes in domum philippi evangelistae qui erat de septem mansimus apud eu

Wolof

nu jóge fa ca ëllëg sa, ñëw ba ca dëkku sesare. nu dugg ca kër filib, taskatu xebaar bu baax bi, mi bokk ci juróom-ñaar ña, nu dal fa moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

adtendite ne iustitiam vestram faciatis coram hominibus ut videamini ab eis alioquin mercedem non habebitis apud patrem vestrum qui in caelis es

Wolof

«wottuleen a def seeni jëf yu jub ci kanamu nit ñi, muy ngistal. lu ko moy, dungeen am yool ci seen baay bi nekk ci kaw.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

at iesus dixit ite in civitatem ad quendam et dicite ei magister dicit tempus meum prope est apud te facio pascha cum discipulis mei

Wolof

yeesu tontu leen: «demleen ca dëkk ba, jëm ca diw, ngeen ne ko: “kilifa gi nee na: sama jamono jege na; ci sa kër laay màggalsi xewu jéggi ba, man ak samay taalibe.”»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cum autem vadis cum adversario tuo ad principem in via da operam liberari ab illo ne forte trahat te apud iudicem et iudex tradat te exactori et exactor mittat te in carcere

Wolof

bu la nit jiiñee dara, ba ngeen ànd di dem ca àttekat ba, nanga fexee juboo ak moom ci yoon wi. lu ko moy, dina la yóbbu ci yoon, yoon jébbal la ca loxoy alkaati ba, mu tëj la.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,606,708 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK