Vous avez cherché: auditis (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

his auditis baptizati sunt in nomine domini ies

Wolof

bi ñu déggee loolu nag, sóob nañu leen ci ndox ci turu yeesu boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

his auditis repleti sunt ira et exclamaverunt dicentes magna diana ephesioru

Wolof

bi ñu déggee loolu, mer mu réy tàbbi ci ñoom, ñuy yuuxu ne: «artemis mu efes màgg na!»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

auditis autem his discipuli mirabantur valde dicentes quis ergo poterit salvus ess

Wolof

bi nga xamee ne taalibe ya dégg nañu loolu, ñu daldi waaru lool ne ko: «kan moo man a mucc nag?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

his auditis tacuerunt et glorificaverunt deum dicentes ergo et gentibus deus paenitentiam ad vitam dedi

Wolof

bi ñu déggee loolu, amuñu dara lu ñu ca teg, ñu daldi màggal yàlla ne: «yàlla nag may na ñi dul yawut it ñu tuub seeni bàkkaar, ba am dund gu wóor gi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quod dico vobis in tenebris dicite in lumine et quod in aure auditis praedicate super tect

Wolof

li ma leen wax ci biir lëndëm, waxleen ko ci leer; li ma leen déey, yégleleen ko ci kaw taax yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

his auditis conpuncti sunt corde et dixerunt ad petrum et ad reliquos apostolos quid faciemus viri fratre

Wolof

bi ko mbooloo ma déggee, naqaru xol wu metti jàpp leen; ñu daldi ne piyeer ak ndaw ya ca des: «bokk yi, lu nu war a def?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

videte ergo quomodo auditis qui enim habet dabitur illi et quicumque non habet etiam quod putat se habere auferetur ab ill

Wolof

seetleen bu baax, ni ngeen di dégloo kàddu gi. ku am, dees na la dollil, waaye ku amul, dees na nangu sax li nga xalaatoon ne, am nga ko ba noppi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

amen quippe dico vobis quia multi prophetae et iusti cupierunt videre quae videtis et non viderunt et audire quae auditis et non audierun

Wolof

ndaxte ci dëgg maa ngi leen koy wax, ay yonent yu bare ak nit ñu jub ñu bare bëggoon nañu gis li ngeen di gis waaye gisuñu ko, te dégg li ngeen di dégg waaye dégguñu ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et videtis et auditis quia non solum ephesi sed paene totius asiae paulus hic suadens avertit multam turbam dicens quoniam non sunt dii qui manibus fiun

Wolof

gis ngeen nag te dégg ne, pool male gëmloo na bay fàbbi mbooloo mu bare, waxuma ci efes rekk, waaye ci biir asi gépp naan: “yàlla yu ay loxo defar duñu ay yàlla.”

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,371,155 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK