Vous avez cherché: cenam (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

convenientibus ergo vobis in unum iam non est dominicam cenam manducar

Wolof

bu ngeen dajee, mënuleen a wax ne reeru boroom bi ngeen di lekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

at ipse dixit ei homo quidam fecit cenam magnam et vocavit multo

Wolof

yeesu tontu ko ne: «dafa amoon nit ku togglu ay ñam, woo ay nit ñu bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dico autem vobis quod nemo virorum illorum qui vocati sunt gustabit cenam mea

Wolof

maa ngi leen koy wax, ci ñi ma woo woon ci sama reer bi, kenn du ci ñam.”»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

fecerunt autem ei cenam ibi et martha ministrabat lazarus vero unus erat ex discumbentibus cum e

Wolof

foofa ñu defaral ko fa reer. màrt moo ko doon séddale, te lasaar bokkoon na ca gan ña.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

unusquisque enim suam cenam praesumit ad manducandum et alius quidem esurit alius autem ebrius es

Wolof

ndaxte bu ngeen dee lekk, ku nekk dafay gaawantu di lekk reeram, ba tax ñenn ñaa ngi xiif, fekk ñeneen di màndi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et cum dies oportunus accidisset herodes natalis sui cenam fecit principibus et tribunis et primis galilaea

Wolof

noonu bés bu yell ñëw, ba erodd doon màggal bésu juddoom; mu woo ca xew wa ay jaraafam ak kilifay xare ba ak njiiti diiwaanu galile.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dicit mihi scribe beati qui ad cenam nuptiarum agni vocati sunt et dicit mihi haec verba vera dei sun

Wolof

gannaaw loolu malaaka ma ne ma: «bindal lii: “yéen ñi ñu woo ci reeri céetu mbote ma, barkeel ngeen.”» mu teg ca ne ma: «kàddu yii ñooy kàdduy yàlla, di kàddu yu dëggu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et vidi unum angelum stantem in sole et clamavit voce magna dicens omnibus avibus quae volabant per medium caeli venite congregamini ad cenam magnam de

Wolof

noonu ma gis malaaka mu taxaw ci jant bi. mu wax ak baat bu xumb ak picc, yiy naaw ci digg asamaan, ne leen: «Ñëwleen teewesi reer bu mag bu yàlla,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dicebat autem et ei qui se invitaverat cum facis prandium aut cenam noli vocare amicos tuos neque fratres tuos neque cognatos neque vicinos divites ne forte et ipsi te reinvitent et fiat tibi retributi

Wolof

noonu yeesu ne ki ko woo woon lekk: «boo dee woote añ walla reer, bul woo rekk say xarit, say doomi ndey, say bokk, walla say dëkkandoo yu am alal. lu ko moy ñooñu itam dinañu la woo, fey la bor bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,738,008,973 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK