Vous avez cherché: deinde (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

adam enim primus formatus est deinde ev

Wolof

ndaxte aadama la yàlla jëkk a sàkk, door caa teg awa.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde veni in partes syriae et cilicia

Wolof

bi loolu wéyee dem naa réewu siri ak réewu silisi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde visus est iacobo deinde apostolis omnibu

Wolof

ba noppi feeñu na saag ak ndawi kirist yépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde post haec dicit discipulis suis eamus in iudaeam iteru

Wolof

gannaaw loolu mu ne taalibe ya: «nanu dellu yude.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

sed non prius quod spiritale est sed quod animale est deinde quod spirital

Wolof

yaram wi soloo ndamu xelum yàlla jiituwul; yaramu doom aadama moo jiitu; yaramu ndam li moo ci topp.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde post annos quattuordecim iterum ascendi hierosolyma cum barnaba adsumpto et tit

Wolof

ba ñu ca tegee fukki at ak ñeent, ànd naa ak barnabas, dellu yerusalem, yóbbaale tit.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde dicit discipulo ecce mater tua et ex illa hora accepit eam discipulus in su

Wolof

neeti taalibe ba: «sa yaay a ngi nii.» booba la ko taalibe ba yóbbu këram, yor ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

ultro enim terra fructificat primum herbam deinde spicam deinde plenum frumentum in spic

Wolof

suuf day meññ moom ci boppam, mu sax, focci, def i gub.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et non sicut speravimus sed semet ipsos dederunt primum domino deinde nobis per voluntatem de

Wolof

te yemuñu sax ci li nu séentu woon ci ñoom, waaye dañoo jébbal seen bopp boroom bi jëkk, gannaaw loolu ñu jébbal nu seen bopp ci coobareg yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde finis cum tradiderit regnum deo et patri cum evacuaverit omnem principatum et potestatem et virtute

Wolof

gannaaw ga, mujug jamono taxaw, te kirist dina noot gépp kilifa ak bépp sañ-sañ ak doole, ba noppi delloo nguur gi kiy yàlla di baayam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde iterum inposuit manus super oculos eius et coepit videre et restitutus est ita ut videret clare omni

Wolof

kon yeesu laalaat bët yi, gumba gi ne xefeet, daldi wér, ba gis lépp bu leer.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cui decimas omnium divisit abraham primum quidem qui interpretatur rex iustitiae deinde autem et rex salem quod est rex paci

Wolof

noonu ibraayma fab fukkeelu cér bi, maanaam asaka, ci li mu jële woon ci xare ba lépp, jox ko. ci lu jëkk turu melkisedeg mi ngi tekki «buur bu jub bi.» gannaaw loolu mooy buuru salem, tur woowu mooy tekki «buuru jàmm.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde nos qui vivimus qui relinquimur simul rapiemur cum illis in nubibus obviam domino in aera et sic semper cum domino erimu

Wolof

gannaaw loolu nun ñiy dund te des fi, dinañu ne fëyy ak ñoom jëm ci niir yi, taseji ak boroom bi ci jaww ji. te noonu dinanu nekk ak boroom bi ba fàww.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde dicit thomae infer digitum tuum huc et vide manus meas et adfer manum tuam et mitte in latus meum et noli esse incredulus sed fideli

Wolof

noonu mu ne tomaa: «indil sa baaraam fii te seet sama loxo; indil sa loxo, teg ko ci sama wet. bàyyil di weddi te nga gëm.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,747,300,453 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK