Vous avez cherché: filia (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

et ait illi propter hunc sermonem vade exiit daemonium de filia tu

Wolof

ci kaw loolu yeesu ne ko: «ndax wax jooju demal ci jàmm, rab wa génn na sa doom.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

at ipse dixit illi filia fides tua te salvam fecit vade in pac

Wolof

yeesu ne ko: «soxna si, sa ngëm faj na la. demal ci jàmm.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

noli timere filia sion ecce rex tuus venit sedens super pullum asina

Wolof

«buleen ragal, waa siyon.gis ngeen, seen buur a ngi ñëw,war mbaam mu ndaw.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

exposito autem illo sustulit eum filia pharaonis et enutrivit eum sibi in filiu

Wolof

ba noppi sànni ko. noonu doom ju jigéen ju firawna for ko, yar ko ni doomam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

die autem natalis herodis saltavit filia herodiadis in medio et placuit herod

Wolof

bi ñu ca tegee ab diir nag, ñuy màggal bés ba erodd juddu woon, te doomu erojàdd ju jigéen di fecc ci biir gan ñi. loolu neex erodd,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

erat autem mulier gentilis syrophoenissa genere et rogabat eum ut daemonium eiceret de filia eiu

Wolof

fekk jigéen ja ci xeetu gereg la bokkoon, juddoo wàlli fenisi ci diiwaanu siri. noonu jigéen ja ñaan ko, mu dàq rab wi ci doomam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

adhuc eo loquente veniunt ab archisynagogo dicentes quia filia tua mortua est quid ultra vexas magistru

Wolof

bi yeesu di wax nag, am na ku jóge ca kër njiit la, mu ñëw naan: «sa doom faatu na; matatul nuy sonal kilifa gi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

mulier enim statim ut audivit de eo cuius habebat filia spiritum inmundum intravit et procidit ad pedes eiu

Wolof

amoon na fa nag jigéen ju rab jàpp doomam ju jigéen. bi mu déggee ne, yeesoo nga fa, mu ñëw, daanu ciy tànkam,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et deprecabatur eum multum dicens quoniam filia mea in extremis est veni inpone manus super eam ut salva sit et viva

Wolof

di ko saraxu lu bare naan: «sama doom ju jigéen mi ngi bëgg a faatu; kaay teg ko loxo, ngir mu wér te dund.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

at iesus conversus et videns eam dixit confide filia fides tua te salvam fecit et salva facta est mulier ex illa hor

Wolof

bi mu ko defee yeesu woññiku ne ko: «na sa xel dal, soxna si, sa ngëm faj na la.» noonu jigéen ja daldi wér ca saa sa.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dividentur pater in filium et filius in patrem suum mater in filiam et filia in matrem socrus in nurum suam et nurus in socrum sua

Wolof

baay bi dina féewaloo ak doom ji, doom ji ak baayam. ndey dina féewaloo ak doomam ju jigéen; doom ju jigéen ji ak ndeyam. goro dina féewaloo ak jabaru doomam; jabaru nit ak goroom.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,743,000,689 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK