Vous avez cherché: manus (Latin - Wolof)

Latin

Traduction

manus

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

nonne manus mea fecit haec omni

Wolof

ndax du sama loxo moo defar yëf yooyu yépp?— moom la boroom bi doon wax.”

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et cum inposuisset eis manus abiit ind

Wolof

noonu yeesu teg leen ay loxoom, ba noppi jóge fa.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

horrendum est incidere in manus dei viventi

Wolof

ndaw tiitaange ci ku sàggan, ba tàbbi ci loxoy yàlla jiy dund!

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

facere quae manus tua et consilium decreverunt fier

Wolof

te def lépp, li sa kàttan ak sa ndigal tëraloon.

Dernière mise à jour : 2025-01-09
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

verumtamen ecce manus tradentis me mecum est in mens

Wolof

waaye nag loxob ki may wor a ngi nekk ak man ci ndab li.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

propter quod remissas manus et soluta genua erigit

Wolof

kon nag mayleen doole loxo yi toqi, ak óom yi bañ,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

et conplexans eos et inponens manus super illos benedicebat eo

Wolof

noonu yeesu leewu leen, teg leen ay loxoom, barkeel leen.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

et iniecerunt manus in apostolos et posuerunt illos in custodia public

Wolof

ba ñu jàpp ndaw ya, tëj leen ca kaso ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

et per fenestram in sporta dimissus sum per murum et effugi manus eiu

Wolof

waaye dugalees na ma ci dàmba, jaarale ma ci palenteeru miiri dëkk ba, yoor ma ci suuf. noonu ma rëcc ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

et erat manus domini cum eis multusque numerus credentium conversus est ad dominu

Wolof

te loxob boroom bi ànd ak ñoom, ba mbooloo mu mag gëm te woññiku ci boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

dicit ei simon petrus domine non tantum pedes meos sed et manus et capu

Wolof

simoŋ piyeer ne ko: «kon nag boroom bi, bul yem rekk ci tànk yi, waaye raxasaaleel loxo yi ak bopp bi!»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

ad israhel autem dicit tota die expandi manus meas ad populum non credentem et contradicente

Wolof

waaye ci mbirum israyil dafa wax ne:«tàllal naa samay loxo, suba ba ngoon, ci xeet wu may bañ tey werante.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

et circumspectis omnibus dixit homini extende manum tuam et extendit et restituta est manus eiu

Wolof

ci kaw loolu mu xool leen ñoom ñépp, ba noppi ne nit ka: «tàllalal sa loxo.» mu tàllal ko, loxoom daldi wér peŋŋ.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

serpentes tollent et si mortiferum quid biberint non eos nocebit super aegrotos manus inponent et bene habebun

Wolof

di jàpp jaan ak seeni loxo; te bu ñu naanee lu ñu tooke, du leen wàññi dara, te jarag ju ñu teg loxo, mu wér.»

Dernière mise à jour : 2025-08-02
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

cum cotidie vobiscum fuerim in templo non extendistis manus in me sed haec est hora vestra et potestas tenebraru

Wolof

moona maa nga woon ak yéen bés bu nekk ca kër yàlla ga, te jàppuleen ma. waaye léegi seen waxtu la, di jamonoy lëndëm.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

et deprecabatur eum multum dicens quoniam filia mea in extremis est veni inpone manus super eam ut salva sit et viva

Wolof

di ko saraxu lu bare naan: «sama doom ju jigéen mi ngi bëgg a faatu; kaay teg ko loxo, ngir mu wér te dund.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

contigit autem patrem publii febribus et dysenteria vexatum iacere ad quem paulus intravit et cum orasset et inposuisset ei manus salvavit eu

Wolof

fekk baayu publiyus dafa tëdd ndax ay tàngoori yaram yu koy dikkal ak biiru taññ. pool nag dem seeti ko, ñaan ci yàlla, teg ko ay loxoom, mu daldi wér.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

amen amen dico tibi cum esses iunior cingebas te et ambulabas ubi volebas cum autem senueris extendes manus tuas et alius te cinget et ducet quo non vi

Wolof

ci dëgg-dëgg piyeer, maa ngi la koy wax, bi nga dee ndaw yaa doon takk sa geño, di dem fu la neex. waaye boo màggatee, dinga tàllal say loxo, keneen takkal la sa geño, yóbbu la foo bëggul.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

et statim prodiit qui fuerat mortuus ligatus pedes et manus institis et facies illius sudario erat ligata dicit iesus eis solvite eum et sinite abir

Wolof

néew bi daldi génn, ñu gis càngaay, li ñu takke woon tànk yi ak loxo yi, ak kaala, gi ñu muure woon kanam gi. yeesu ne leen: «tekkileen ko, bàyyi ko mu dem.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Latin

et abiit ananias et introivit in domum et inponens ei manus dixit saule frater dominus misit me iesus qui apparuit tibi in via qua veniebas ut videas et implearis spiritu sanct

Wolof

ci kaw loolu anañas dem, dugg ca kër ga, teg ay loxoom sool. mu ne ko: «sool sama mbokk, boroom bi yeesu, mi la feeñu woon ci kaw yoon wi, bi ngay dikk, moo ma yónni, ngir nga dellu di gis te fees ak xel mu sell mi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,910,302,412 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK