Vous avez cherché: misericordia (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

misericordia vobis et pax et caritas adimpleatu

Wolof

na leen yàlla may yërmande, jàmm ak mbëggeel.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et misericordia eius in progenies et progenies timentibus eu

Wolof

day wàcce yërmandeem ci ñi ko ragal,ci seeni sët ba ci seeni sëtaat.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quam cum vidisset dominus misericordia motus super ea dixit illi noli fler

Wolof

bi ko boroom ba gisee, mu daldi koy yërëm ne ko: «bul jooyati.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deus autem qui dives est in misericordia propter nimiam caritatem suam qua dilexit no

Wolof

waaye yàlla mi bare yërmande, ci kaw mbëggeel gu réy, gi mu am ci nun,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

samaritanus autem quidam iter faciens venit secus eum et videns eum misericordia motus es

Wolof

waaye benn waay bu dëkk samari bu doon tukki, ñëw ba jege waa ja, gis ko, yërëm ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et quicumque hanc regulam secuti fuerint pax super illos et misericordia et super israhel de

Wolof

Ñiy topp ndigal lii nag, na yàlla wàcce jàmm ak yërmande ci ñoom, ak ci israyilu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

sit nobiscum gratia misericordia pax a deo patre et a christo iesu filio patris in veritate et caritat

Wolof

yàlla baay bi ak yeesu krist, doomu baay bi, dinañu nu may yiw, yërmande ak jàmm, ànd ak dëgg ak mbëggeel.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quae autem desursum est sapientia primum quidem pudica est deinde pacifica modesta suadibilis plena misericordia et fructibus bonis non iudicans sine simulation

Wolof

waaye xel mi jóge ci kaw daa sell, ba noppi ànd ak jàmm te lewet, nooy, fees dell ak yërmande ak jëf yu rafet; àndul ak genn parlàqu, amul genn naaféq.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et surgens venit ad patrem suum cum autem adhuc longe esset vidit illum pater ipsius et misericordia motus est et adcurrens cecidit supra collum eius et osculatus est illu

Wolof

«mu daldi jóg, jëm kër baayam. waaye bi muy soreendi kër ga, baayam séen ko, yërëm ko, daldi daw laxasu ko, fóon ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,799,925,668 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK