Vous avez cherché: montem (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

et cum dimisisset eos abiit in montem orar

Wolof

bi mu tàggtoo ak mbooloo mi, mu yéeg ca tund wa, ñaan fa yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et hymno dicto exierunt in montem olivaru

Wolof

noonu ñu woy yàlla, ba noppi génn, dem ca tundu oliw ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

erat autem ibi circa montem grex porcorum magnus pascen

Wolof

fekk amoon na fa ca tund wa géttu mbaam-xuux yu bare yuy for.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

subiit ergo in montem iesus et ibi sedebat cum discipulis sui

Wolof

yeesu daldi yéeg ca kaw tund wa, toog fa ak ay taalibeem.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

non enim portabant quod dicebatur et si bestia tetigerit montem lapidabitu

Wolof

ndaxte mënuñu woon a dékku ndigal lii: «su mala sax laalee tund wa, nangeen ko sànni ay xeer, ba mu dee.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ascendens in montem vocavit ad se quos voluit ipse et venerunt ad eu

Wolof

gannaaw loolu yeesu yéeg ci tund wi, woo ñi ko neex, ñu daldi ñëw ci moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

undecim autem discipuli abierunt in galilaeam in montem ubi constituerat illis iesu

Wolof

noonu fukki taalibe ya ak benn dem ci biir galile, ca tund wa leen yeesu digaloon.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et cum adpropinquarent hierosolymae et bethaniae ad montem olivarum mittit duos ex discipulis sui

Wolof

gannaaw loolu yeesu ak taalibe ya jege nañu yerusalem, ba agsi dëkki betfase ak betani ci wetu tundu oliw ya. noonu yeesu yebal ñaar ciy taalibeem,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et cum transisset inde iesus venit secus mare galilaeae et ascendens in montem sedebat ib

Wolof

bi loolu amee yeesu jóge foofa, ñëw ci weti dexu galile; mu yéeg ca aw tund, toog fa.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et cum adpropinquassent hierosolymis et venissent bethfage ad montem oliveti tunc iesus misit duos discipulo

Wolof

gannaaw loolu yeesu ak taalibe ya jege woon nañu yerusalem, ba agsi dëkku betfase ci wetu tundu oliw ya. noonu yeesu yebal ñaari taalibe,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et factum est cum adpropinquasset ad bethfage et bethania ad montem qui vocatur oliveti misit duos discipulos suo

Wolof

bi muy jege dëkki betfase ak betani, ci wetu tund wu ñuy wax tundu oliw ya, yeesu yebal ñaar ci ay taalibeem,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et cum sederet in montem olivarum contra templum interrogabant eum separatim petrus et iacobus et iohannes et andrea

Wolof

gannaaw loolu, bi nga xamee ne yeesu toog na ci tundu oliw ya, jàkkaarlook kër yàlla ga, piyeer, saag, yowaana ak andare fekki ko cig wet, laaj ko:

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et post dies sex adsumpsit iesus petrum et iacobum et iohannem fratrem eius et ducit illos in montem excelsum seorsu

Wolof

juróom-benni fan gannaaw gi, yeesu àndoon na ak piyeer, saag ak yowaana rakkam, yóbbu leen fu wéet ci tund wu kawe lool.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et post dies sex adsumit iesus petrum et iacobum et iohannem et ducit illos in montem excelsum seorsum solos et transfiguratus est coram ipsi

Wolof

mu ne leen ati: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, am na ñi fi taxaw, ñoo xam ne duñu dee, te gisuñu nguuru yàlla ñëw ak doole.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et vidi et ecce agnus stabat supra montem sion et cum illo centum quadraginta quattuor milia habentes nomen eius et nomen patris eius scriptum in frontibus sui

Wolof

ma xool noonu, gis mbote ma taxaw ci tundu siyon, ànd ak téeméer ak ñeent-fukk ak ñeenti junniy nit, te ñu bind ci seen jë turu mbote ma ak turu baayam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,777,620,200 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK