Vous avez cherché: praecepta (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

scitis enim quae praecepta dederimus vobis per dominum iesu

Wolof

ndaxte xam ngeen ndigal, yi nu leen jox ci wàllu yeesu boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

in vanum autem me colunt docentes doctrinas praecepta hominu

Wolof

seen màggal amul benn njariñ,ci li ñuy jàngale dénkaaney nit kese.”»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quae sunt omnia in interitu ipso usu secundum praecepta et doctrinas hominu

Wolof

sàrt yooyu ñu ngi aju ci ndigali nit ñi ak seen njàngale. yëf yi ñu tudd yépp, dees na leen jariñoo, ba ñu jeex.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

laudo autem vos fratres quod omnia mei memores estis et sicut tradidi vobis praecepta mea teneti

Wolof

maa ngi leen di sant ci li ngeen may fàttaliku ci lépp, ak ci li ngeen di topp dénkaane, yi ma leen dénk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

si praecepta mea servaveritis manebitis in dilectione mea sicut et ego patris mei praecepta servavi et maneo in eius dilection

Wolof

bu ngeen toppee samay ndigal, dingeen sax ci sama mbëggeel, ni ma toppe sama ndigali baay, ba tax ma sax ci mbëggeelam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

praecepta nosti ne adulteres ne occidas ne fureris ne falsum testimonium dixeris ne fraudem feceris honora patrem tuum et matre

Wolof

xam nga ndigal yi: “bul bóom, bul njaaloo, bul sàcc, bul seede lu dul dëgg, bul nangu alalu jaambur, teralal sa ndey ak sa baay.”»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

confestim igitur misi ad te et tu bene fecisti veniendo nunc ergo omnes nos in conspectu tuo adsumus audire omnia quaecumque tibi praecepta sunt a domin

Wolof

yónnee naa nag ci ni mu gën a gaawe, woolu la; te maa ngi lay sant ci li nga ñëw. léegi nag nun ñépp nu ngi fi ci kanam yàlla, ngir déglu lépp li la boroom bi sant.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,763,990,443 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK