Vous avez cherché: primus (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

adam enim primus formatus est deinde ev

Wolof

ndaxte aadama la yàlla jëkk a sàkk, door caa teg awa.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

ego alpha et omega primus et novissimus principium et fini

Wolof

man maay alfa ak omega, ki jëkk te mujj, njàlbéen gi ak muj gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et quicumque voluerit in vobis primus esse erit omnium servu

Wolof

te ku bëgg a nekk njiit, na nekk seen jaam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

venit autem primus dicens domine mna tua decem mnas adquisivi

Wolof

ku jëkk ka ñëw ne ko: “sang bi, sa libidoor bii jur na fukki libidoor.”

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

factus est primus homo adam in animam viventem novissimus adam in spiritum vivificante

Wolof

mbind mi nee na: «nit ku jëkk ka, aadama, doon na boroom ruu,» waaye aadama mu mujj mi doon na xel muy joxe dund.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

septem ergo fratres erant et primus accepit uxorem et mortuus est sine filii

Wolof

amoon na fi nag juróom-ñaari góor ñu bokk ndey ak baay. taaw ba takk jabar, faatu, te bàyyiwul doom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et angelo zmyrnae ecclesiae scribe haec dicit primus et novissimus qui fuit mortuus et vivi

Wolof

«bindal malaakam mbooloom ñi gëm ci dëkku samirin, ne ko: i ki jëkk te mujj, ki dee woon te dekki nee na:

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

duodecim autem apostolorum nomina sunt haec primus simon qui dicitur petrus et andreas frater eiu

Wolof

fukki ndaw ak ñaar, ya yeesu yónni woon nag, nii lañu tuddoon: ku jëkk ki mooy simoŋ mi ñuy wax piyeer, ak andare mi bokk ak moom ndey ak baay; saag doomu sebede, ak yowaana rakkam;l

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

currebant autem duo simul et ille alius discipulus praecucurrit citius petro et venit primus ad monumentu

Wolof

Ñoom ñaar ñépp a ngi doon daw, waaye beneen taalibe ba raw piyeer, jëkk ko ca bàmmeel ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cum autem perseverarent interrogantes eum erexit se et dixit eis qui sine peccato est vestrum primus in illam lapidem mitta

Wolof

bi laaj ya baree, mu siggi ne leen: «ku musul a def bàkkaar ci yéen, na ko jëkk a sànniy xeer.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

erant autem apud nos septem fratres et primus uxore ducta defunctus est et non habens semen reliquit uxorem suam fratri su

Wolof

amoon na ci nun nag juróom-ñaari góor, ñu bokk ndey ak baay. taaw ba séyoon na, faatu; rakk ja donn jabar ja, ndaxte amul woon doom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et abiit primus et effudit fialam suam in terram et factum est vulnus saevum ac pessimum in homines qui habent caracterem bestiae et eos qui adoraverunt imaginem eiu

Wolof

noonu malaaka mu jëkk ma dem, sotti ndabam ci àddina, ba woppi taab ju bon te metti dal nit, ña am màndargam rab wa tey jaamu nataalam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et primus tuba cecinit et facta est grando et ignis mixta in sanguine et missum est in terram et tertia pars terrae conbusta est et tertia pars arborum conbusta est et omne faenum viride conbustum es

Wolof

malaaka mu jëkk ma wol liitam. noonu ñu sànni ci àddina yuur ak safara yu ñu boole ak deret, ba tax benn ci ñetti xaaju suuf si lakk, benn ci ñetti xaaju garab yi it lakk, te ñax mu naat mépp lakk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,777,965,795 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK