Vous avez cherché: recte (Latin - Wolof)

Latin

Traduction

recte

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

dixitque illi recte respondisti hoc fac et vive

Wolof

yeesu ne ko nag: «li nga wax dëgg la. boo defee loolu, dinga dund ba fàww.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

respondens simon dixit aestimo quia is cui plus donavit at ille dixit ei recte iudicast

Wolof

simoŋ tontu ne ko: «xanaa ki ñu baal bor bi gën a bare.» yeesu ne ko: «Àtte nga dëgg,»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et interrogaverunt illum dicentes magister scimus quia recte dicis et doces et non accipis personam sed in veritate viam dei doce

Wolof

Ñu daldi ñëw ci yeesu ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne li ngay wax te di ko jàngale lu jub la. amuloo parlàqu, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

incipiente autem paulo aperire os dixit gallio ad iudaeos si quidem esset iniquum aliquid aut facinus pessimum o viri iudaei recte vos sustinere

Wolof

bi pool bëggee wax nag, galyon ne yawut ya: «yéen yawut yi, bu aju woon ci jàdd yoon walla ñaawteef wu réy, kon liy yoon mooy ma déglu leen.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

sed cum vidissem quod non recte ambularent ad veritatem evangelii dixi cephae coram omnibus si tu cum iudaeus sis gentiliter et non iudaice vivis quomodo gentes cogis iudaizar

Wolof

bi ma seetee nag ne, awuñu woon ci dëgg, gi xebaar bu baax bi di jàngale, ma yedd sefas ci kanamu ñépp ne ko: «yaw miy yawut, gannaaw dëddu nga aaday yawut yi, ba dund ni ku dul yawut, lu tax nga bëgg a sëf diiney yawut ci ñi dul yawut?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
10,388,471,977 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK