Vous avez cherché: regnum (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

et iterum dixit cui simile aestimabo regnum de

Wolof

mu neeti: «lan laa man a mengaleek nguuru yàlla?

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dicens paenitentiam agite adpropinquavit enim regnum caeloru

Wolof

nii la doon waaree: «tuubleen seeni bàkkaar, ndaxte nguuru yàlla aji kawe ji jege na.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

beati pauperes spiritu quoniam ipsorum est regnum caeloru

Wolof

«yéen ñi xam seen ñàkk doole ngir neex yàlla,barkeel ngeen,ndaxte nguuru yàlla aji kawe ji,yéena ko yelloo.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dicebat cui adsimilabimus regnum dei aut cui parabolae conparabimus illu

Wolof

yeesu ne leen ati: «lu nu man a mengaleel nguuru yàlla? walla ban léeb lanu ko man a misaale?

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

veniat regnum tuum fiat voluntas tua sicut in caelo et in terr

Wolof

na sa nguur ñëw,na sa coobare am ci suuf mel ni ci kaw.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

benedictum quod venit regnum patris nostri david osanna in excelsi

Wolof

nguuru sunu maam daawuda giy ñëw,dina barkeel!ci bérab yu gën a kawe,nañu ne: “osaana!”»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dicebat sic est regnum dei quemadmodum si homo iaciat sementem in terra

Wolof

yeesu teg ci ne: «nguuru yàlla dafa mel ni nit ku ji tool.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

amen dico vobis quicumque non acceperit regnum dei sicut puer non intrabit in illu

Wolof

ci dëgg, maa ngi leen koy wax, woyoful ni xale, nangu nguuru yàlla, doo ci man a dugg.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

amen dico vobis quisque non receperit regnum dei velut parvulus non intrabit in illu

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, ku woyoful ni xale, nangu nguuru yàlla, doo ci man a dugg.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dixit ergo homo quidam nobilis abiit in regionem longinquam accipere sibi regnum et revert

Wolof

mu ne nag: «dafa amoon boroom juddu bu rafet bu demoon ci réew mu sore, ngir ñu fal ko buur te mu dellusiwaat.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

a diebus autem iohannis baptistae usque nunc regnum caelorum vim patitur et violenti rapiunt illu

Wolof

ci li dale ci jamonoy yaxya ba léegi, nit ñaa ngi góor-góorlu ngir dugg ci nguuru yàlla, te ñi sawar ñoo ci am wàll.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

consurget enim gens in gentem et regnum in regnum et erunt pestilentiae et fames et terraemotus per loc

Wolof

xeet dina jóg, xeex ak weneen xeet, réew xeex ak meneen réew. dina am ay xiif ak ay yengu-yenguy suuf ci bérab yu bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

aliam parabolam proposuit eis dicens simile est regnum caelorum grano sinapis quod accipiens homo seminavit in agro su

Wolof

yeesu waxaat leen beneen léeb ne leen: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni doomu fuddën bu nit jël, ji ko ci toolam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

aliam parabolam proposuit illis dicens simile factum est regnum caelorum homini qui seminavit bonum semen in agro su

Wolof

noonu yeesu dégtal leen beneen léeb ne leen: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni nit ku ji jiwu wu baax ci toolam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

discipuli autem obstupescebant in verbis eius at iesus rursus respondens ait illis filioli quam difficile est confidentes in pecuniis regnum dei introir

Wolof

wax jooju nag daldi jaaxal taalibe yi lool. waaye yeesu neeti leen: «samay xarit, dugg ci nguuru yàlla, lu jafee ngoogu!

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

aliam parabolam locutus est eis simile est regnum caelorum fermento quod acceptum mulier abscondit in farinae satis tribus donec fermentatum est totu

Wolof

yeesu teg ca beneen léeb ne leen: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni lawiir bu jigéen jël, jaxase ko ak ñetti andaari fariñ, ba kera tooyal bépp di funki.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cum constituissent autem illi diem venerunt ad eum in hospitium plures quibus exponebat testificans regnum dei suadensque eos de iesu ex lege mosi et prophetis a mane usque ad vespera

Wolof

noonu ñu dig ko bés, te ñu bare ñëw, fekksi ko ca néegam. mu di leen jàngal suba ba ngoon, di leen dëggal lu jëm ci nguuru yàlla ak ci yeesu, tukkee ci yoonu musaa ak ci yonent yi, di leen jéem a gëmloo.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et septimus angelus tuba cecinit et factae sunt voces magnae in caelo dicentes factum est regnum huius mundi domini nostri et christi eius et regnabit in saecula saeculoru

Wolof

juróom-ñaareelu malaaka ma wol liitam, noonu baat yu xumb jib ca asamaan naan:«nguuru àddina, jébbalaat nañu kosunu boroom ak almaseem,te dina nguuru ba fàww.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,791,722,791 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK