Vous avez cherché: responsum (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

dixerunt ergo ei quis es ut responsum demus his qui miserunt nos quid dicis de te ips

Wolof

noonu ñu laaj ko ne: «wax nu yaay kan, ngir nu man a tontu ñi nu yónni. nga ne yaa di kan?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et responsum acceperat ab spiritu sancto non visurum se mortem nisi prius videret christum domin

Wolof

te xamal na ko ne, du dee mukk te gisul almasib boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ingressus est praetorium iterum et dicit ad iesum unde es tu iesus autem responsum non dedit e

Wolof

dugg ca taax ma, daldi ne yeesu: «foo jóge?» waaye yeesu tontuwu ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

sed ipsi in nobis ipsis responsum mortis habuimus ut non simus fidentes in nobis sed in deo qui suscitat mortuo

Wolof

demoon nanu ba defe ne, dogalees na sunug dee. loolu amoon na, ngir nu bañ a wéer sunu yaakaar ci sunu bopp, waaye nu wéer ko ci yàlla, miy dekkal néew yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

qui exemplari et umbrae deserviunt caelestium sicut responsum est mosi cum consummaret tabernaculum vide inquit omnia facito secundum exemplar quod tibi ostensum est in mont

Wolof

saraxalekat yooyu ñu ngi liggéeyal yàlla ca màggalukaay, ba nekk misaal tey takkandeeru yëf yu dëggu, ya féete kaw. moo tax ba musaa naree defar tàntu màggalukaay ba, yàlla artu na ko ne ko: «teeylul ba def lépp, roye ko ci bi ma la won ca tund wa.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

qui dixerunt cornelius centurio vir iustus et timens deum et testimonium habens ab universa gente iudaeorum responsum accepit ab angelo sancto accersire te in domum suam et audire verba abs t

Wolof

Ñu tontu ko: «korney, njiitu xare ba, nit ku jub la te ragal yàlla, ba am seede su rafet ci bànni israyil gépp. malaaka mu sell nag sant na ko, mu woolu la ci këram te déglu li ngay wax.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,099,972 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK