Vous avez cherché: spiritum (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

spiritum nolite extinguer

Wolof

buleen fey taalu xelum yàlla,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quoniam dicebant spiritum inmundum habe

Wolof

yeesu wax na loolu, ndaxte nee woon nañu, rab jàpp na ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

hii sunt qui segregant animales spiritum non habente

Wolof

Ñooy féewale, te xelum yàlla nekkul ci ñoom, waaye niti kese lañu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

conturbati vero et conterriti existimabant se spiritum vider

Wolof

Ñu daldi tiit, foog ne dañoo gis njuuma.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

bonum depositum custodi per spiritum sanctum qui habitat in nobi

Wolof

te nga sàmm bu baax li la yàlla dénk, wéeru ci xel mu sell, mi dëkk ci nun.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

refecerunt enim et meum spiritum et vestrum cognoscite ergo qui eiusmodi sun

Wolof

seral nañu sama xol ak seen yos itam. kon fonkleen nit ñu mel noonu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et lapidabant stephanum invocantem et dicentem domine iesu suscipe spiritum meu

Wolof

ñu wat-wate ko, génne ko dëkk ba, dóor ko ay doj, ba mu dee. seede ya tegoon nañu seeni yére ci tànki waxambaane wu tudd sool.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et nolite contristare spiritum sanctum dei in quo signati estis in die redemptioni

Wolof

buleen yóbbe tiis xelu yàlla mu sell, mi leen tàmpe ngir bésu goreel ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et increpavit iesus spiritum inmundum et sanavit puerum et reddidit illum patri eiu

Wolof

ku nekk waaru na ndax màggug yàlla. bi ñuy yéemu ci li mu doon def, yeesu ne taalibeem ya:

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et respondens unus de turba dixit magister adtuli filium meum ad te habentem spiritum mutu

Wolof

noonu yeesu laaj leen: «ci lan ngeen di werante ak ñoom?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

alii quidem per spiritum datur sermo sapientiae alii autem sermo scientiae secundum eundem spiritu

Wolof

am na ku yàlla sédde, jaarale ko ci xelam, mayu wax ak xel mu leer, keneen am mayu xam-xam, te mu bawoo ci menn xel mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et clamans voce magna iesus ait pater in manus tuas commendo spiritum meum et haec dicens exspiravi

Wolof

yeesu woote ak kàddu gu dëgër naan: «baay, jébbal naa la sama ruu!» bi mu waxee loolu, mu delloo ruuwam yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dicens date et mihi hanc potestatem ut cuicumque inposuero manus accipiat spiritum sanctum petrus autem dixit ad eu

Wolof

ne leen: «mayleen ma sañ-sañ boobu, ba ku ma teg samay loxo, nga jot xel mu sell mi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

caro enim concupiscit adversus spiritum spiritus autem adversus carnem haec enim invicem adversantur ut non quaecumque vultis illa faciati

Wolof

ndaxte sunu nafsu am na ay bëgg-bëgg yu mengoowul ak yu xelum yàlla. te xelum yàlla itam am na ay bëgg-bëgg yu mengoowul ak yu sunu nafsu. Ñoom ñaar dañoo juuyoo ci bépp fànn, ba tax lépp lu ngeen bëggoon a def, dungeen ko man.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

baptizatus autem confestim ascendit de aqua et ecce aperti sunt ei caeli et vidit spiritum dei descendentem sicut columbam venientem super s

Wolof

bi ko yaxya sóobee ca dex ga, yeesu génn. ca saa sa asamaan yi daldi ubbiku, te yaxya gis xelum yàlla wàcc ci melow pitax, ñëw ci kaw yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

etenim in uno spiritu omnes nos in unum corpus baptizati sumus sive iudaei sive gentiles sive servi sive liberi et omnes unum spiritum potati sumu

Wolof

yàlla sóob na nu ci menn xelam mi, ngir nu doon wenn yaram: nuy yawut walla nu dul yawut, nuy jaam mbaa gor, nun ñépp yàlla may na nu, nu naan ci menn xel mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ego nesciebam eum sed qui misit me baptizare in aqua ille mihi dixit super quem videris spiritum descendentem et manentem super eum hic est qui baptizat in spiritu sanct

Wolof

bi loola laata am, xawma woon mooy kan, waaye yàlla, mi ma yebal may sóobe ci ndox, nee woon na ma: “dinga gis xel mu sell mi wàcc, tegu ci kaw nit. kooku moo di ki leen di sóob ci xel mu sell mi.”»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quod si spiritus eius qui suscitavit iesum a mortuis habitat in vobis qui suscitavit iesum christum a mortuis vivificabit et mortalia corpora vestra propter inhabitantem spiritum eius in vobi

Wolof

kon nag gannaaw xelum yàlla, mi dekkal yeesu ca néew ya, dëkk na ci yéen, dina tax seen yaram wi néew doole dund ci kàttanu xel moomu dëkk ci yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,793,361,674 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK