Vous avez cherché: kristi (Norvégien - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Norvégien

Wolof

Infos

Norvégien

for kristi kjærlighet tvinger oss,

Wolof

ndaxte mbëggeelu kirist moo nuy jiite, ndax wóor na nu ne, ndegam kenn rekk a dee ngir ñépp, kon ñépp a dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

vår herre jesu kristi nåde være med eder!

Wolof

na yiwu sunu boroom yeesu kirist ànd ak yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

begynnelsen til jesu kristi, guds sønns evangelium.

Wolof

xebaar bu baaxu yeesu kirist, doomu yàlla, nii la tàmbalee.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

den herre jesu kristi nåde være med eders ånd!

Wolof

na yiwu boroom bi yeesu kirist ànd ak seen xel.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

likesom kristi vidnesbyrd er blitt rotfestet i eder,

Wolof

ndaxte li nu doon seedeel kirist, yàlla dëggal na ko ci yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

jesu kristi, davids sønns, abrahams sønns ættetavle:

Wolof

lii mooy cosaanu yeesu kirist, sëtu daawuda, sëtu ibraayma.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

bær hverandres byrder, og opfyll på den måte kristi lov!

Wolof

jàppalanteleen, noonu dingeen sàmm yoon wi kirist tëral.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

men med kristi dyre blod som blodet av et ulastelig og lyteløst lam,

Wolof

waaye ci deretu kirist ju tedd ji, mel ni mbote mu sikkul te wàññikuwul.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

hils hverandre med et hellig kyss! alle kristi menigheter hilser eder.

Wolof

te yéen bokk yi, saafoonteleen ak xol bu laab. mboolooy ñi gëm kirist yépp a ngi leen di nuyu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

paulus, ved guds vilje kalt til kristi jesu apostel, og broderen sostenes

Wolof

man pool, ndawul kirist yeesu ci coobareg yàlla, man ak sosten sunu mbokk,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

og alltid sier gud og faderen takk for alle ting i vår herre jesu kristi navn,

Wolof

gërëmleen yàlla baay bi ci turu yeesu kirist boroom bi, fu ngeen man a tollu, ci lu mu man a doon;

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

at du skal holde budet rent og ulastelig inntil vår herre jesu kristi åpenbarelse,

Wolof

sàmmal ndigal li, bañ a am gàkk mbaa ŋàññ, ba kera yeesu kirist sunu boroom di feeñ ci ndamam, ca waxtu wa yàlla dogal.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

den herre jesu kristi nåde og guds kjærlighet og den hellige Ånds samfund være med eder alle!

Wolof

mboolem gaayi yàlla yépp ñu ngi leen di nuyu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

og jeg vet at når jeg kommer til eder, skal jeg komme med en fylde av kristi velsignelse.

Wolof

te wóor na maa ne, bu ma agsee ci yéen, dinaa indaale barkeb kirist bu mat sëkk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

for heller ikke jeg har mottatt det eller lært det av noget menneske, men ved jesu kristi åpenbaring.

Wolof

jëlewuma ko ci nit, te kenn jàngalu ma ko, waaye yeesu kirist moo ma ko won.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

for mange vandrer, som jeg ofte har sagt eder og nu endog med tårer sier er fiender av kristi kors,

Wolof

ndaxte jëfi ñu bare juuyoo na ak dee gi kirist dee; loolu wax naa leen ko ba tàyyi, maa ngi koy waxaat léegi ak i jooy.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

at vår herre jesu kristi gud, herlighetens fader, måtte gi eder visdoms og åpenbarings Ånd til kunnskap om sig,

Wolof

te li may ñaan yàllay sunu boroom yeesu kirist, di baay bi yelloo ndam, mooy lii: mu sol leen xel mu xóot, te xamal leen boppam

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

derfor bøier jeg mine knær, jeg, paulus, kristi jesu fange for eders skyld, i hedninger -

Wolof

kon nag maa ngi leen di ñaanal, man pool mi ñu tëj kaso ci turu kirist ndax sas wi may bey ci yéen, xeet yi dul yawut.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

for den træl som er kalt i herren, er herrens frigitte; likeså er også den frie som er kalt, kristi træl.

Wolof

ku nekkoon jaam, bi la boroom bi wooyee, boroom bi goreel na la. ba tey it ku nekkoon gor, bi ñu la wooyee, jaamu kirist nga.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

så ber jeg dog heller, for kjærlighetens skyld. slik som jeg er, den gamle paulus, men nu også kristi jesu fange,

Wolof

waaye dama lay ñaan ci mbëggeel gi nu séq, man pool màggat, mi ñu tëj kaso ci turu kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,770,588,514 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK