Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
alisema atawahurumia wazee wetu, na kukumbuka agano lake takatifu.
yàlla wone na yërmandeem,ji mu digoon sunuy maam,te di fàttaliku kóllëre, gi mu fas ak ñoom,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
hili ndilo agano nitakalofanya nao wakati nitakapoziondoa dhambi zao."
loolu mooy kóllëre, gi may fas ak ñoom,bés bu may dindi seeni bàkkaar.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
ndiyo maana hata lile agano la kwanza halikuwekwa bila damu kumwagwa.
looloo waral kóllëre gu jëkk ga, ñu fasoon ko ak deret.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
basi, kutokana na tofauti hii, yesu amekuwa mdhamini wa agano lililo bora zaidi.
ngiñ loolu moo tax yeesu nekk tayle, giy wóoral kóllëre gi gën.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
maana kama lile agano la kwanza halingalikuwa na dosari, hakungalikuwa na haja ya agano la pili.
bu fekkoonte ne, kóllëre gu jëkk ga dafa amul woon benn sikk, kon du aajo ñu koy weccee ak geneen.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
agano la kwanza lilikuwa na taratibu zake za ibada na pia mahali patakatifu pa ibada palipojengwa na watu.
kóllëre gu jëkk ga ëmboon na ay ndigal ci mbirum ni ñu war a jaamoo yàlla. amoon na itam kër yàlla gu nekkoon àddina.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
maana hii ni damu yangu inayothibitisha agano, damu inayomwagwa kwa ajili ya watu wengi ili kuwaondolea dhambi.
ndaxte lii sama deret la, ji fas kóllëre gi, te mu tuuru, ngir ñu bare jot mbaalug bàkkaar yi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
akawaambia, "hii ni damu yangu inayothibitisha agano la mungu, damu inayomwagwa kwa ajili ya watu wengi.
mu ne leen: «lii sama deret la, ji fas kóllëre gi, te mu tuuru ngir ñu bare.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
kwa kusema juu ya agano jipya, mungu alilichakaza lile la kwanza; na chochote kinachochakaa na kuwa kikuukuu kitatoweka karibuni.
kon nag bi yàllay wax ci kóllëre gu bees gi, dafa fekk mu màggatal gu jëkk ga. te lu xewwi te màggat mi ngi ci tànki wéy.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
lakini akili zao zilipumbazwa. mpaka leo hii lisomwapo agano la kale, kifuniko hicho bado kipo. kifuniko hicho kitaondolewa tu mtu anapoungana na kristo.
waaye seen xel dafa daldi gumba. ba tey jii sax, bu ñuy jàng téereb kóllëre gu jëkk gi, muuraay moomu dafay des; deñul, ndaxte ci kirist rekk la man a deñe.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
akafanya vivyo hivyo na kikombe, baada ya chakula, akisema, "kikombe hiki ni agano jipya linalothibitishwa kwa damu yangu inayomwagika kwa ajili yenu.
noonu itam bi ñu lekkee ba noppi, mu jël kaas bi ne leen: «kaas bii mooy misaal kóllëre gu bees gi yàlla fas jaarale ko ci sama deret, ji tuuru ngir yéen.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
agano hili halitakuwa kama lile nililofanya na babu zao siku ile nilipowaongoza kwa mkono kutoka nchi ya misri. hawakuwa waaminifu kwa agano langu; na hivyo mimi sikuwajali, asema bwana.
ba ma leen jàppee ci loxo,génne leen réewu misra.boroom bi nee na:beddeeku naa leenndaxte sàmmuñu sama kóllëre.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
kwa hiyo, kristo ndiye aliyeratibisha agano jipya ili wale walioitwa na mungu wazipokee baraka za milele walizoahidiwa. watazipata, kwani kifo kimetokea ambacho huwakomboa watu kutoka yale makosa waliyofanya wakati wa lile agano la kale.
looloo tax mu nekk rammukat bi ci wàllu kóllëre gu bees ci diggante yàlla ak nit, ngir ñi yàlla woo am cér bu sax ci kaw, te mu digoon leen ko, ndaxte kirist dee na, ngir jot ñi jàdd yoon ca kóllëre gu jëkk ga.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
"hili ndilo agano nitakalofanya nao, katika siku zijazo, asema bwana: nitaweka sheria zangu mioyoni mwao, na kuziandika akilini mwao."
dafa jëkk a wax ne:«boroom bi nee na:kóllëre gaa ngii,kóllëre gi may fas ak ñoom,bu bés yooyule weesoo.dinaa def samay ndigal ci seen xol,bind ko ci seen xel.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
ahadi zile mungu alizotoa kwa njia ya manabii ni kwa ajili yenu; na mnashiriki lile agano mungu alilofanya na babu zenu, kama alivyomwambia abrahamu: kwa njia ya wazawa wako, jamaa zote za dunia zitabarikiwa.
yéen nag yéenay donn yonent yi ak kóllëre, gi yàlla fasoon ak seeni maam, bi mu naan ibraayma: “xeeti àddina yépp dinañu barkeel ci ki soqikoo ci yaw.”
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
halafu mungu aliifanya tohara iwe ishara ya agano. hivyo, abrahamu alimtahiri mtoto wake isaka, siku ya nane baada ya kuzaliwa. na isaka, vivyo hivyo, alimtahiri yakobo. naye yakobo aliwatendea wale mababu kumi na wawili vivyo hivyo.
yàlla nag tëral kóllëre seen diggante, fas ko ci màndargam xaraf. noonu ibraayma jur isaaxa, xarafal ko ca juróom-ñetteelu fan ba; isaaxa def noonu yanqóoba, yanqóoba it def noonu fukki maam ya ak ñaar, ñi sos xeet wi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :