Vous avez cherché: akawajibu (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

yesu akawajibu kwa mfano:

Wolof

noonu yeesu daldi leen wax léeb wii ne leen:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

yesu akawajibu, "je, mnaamini sasa?

Wolof

yeesu ne leen: «ndax gëm ngeen léegi?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

yesu akawajibu, "mose aliwapa maagizo gani?"

Wolof

yeesu tontu leen ne: «lu leen yoonu musaa sant?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

yesu akawajibu, "jihadharini msije mkadanganywa na mtu.

Wolof

yeesu tontu leen ne: «moytuleen, bu leen kenn nax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

lakini yeye akawajibu, nawaambieni kweli, siwajui ninyi."

Wolof

waaye mu tontu leen ne: “ci dëgg maa ngi leen koy wax, xawma leen.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

wakamwuliza, "yeye yuko wapi?" naye akawajibu, "mimi sijui!"

Wolof

Ñu ne ko: «ana waa ji?» mu ne leen: «xawma fu mu nekk.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

yesu akawajibu, "kweli, eliya atakuja kutayarisha mambo yote.

Wolof

yeesu tontu leen ne: «waaw dëgg la, iliyas war na ñëw, jubbanti lépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

yesu akawajibu, "nendeni mkamwambie yohane mambo mnayoyasikia na kuyaona:

Wolof

yeesu tontu leen ne: «demleen nettali yaxya li ngeen dégg te gis ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

hapo yesu akawajibu, "mafundisho ninayofundisha si yangu, bali ni yake yeye aliyenituma.

Wolof

yeesu daldi leen tontu ne: «li may jàngale, jógewul ci man, waaye ci ki ma yónni la jóge.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

nao wakamwuliza, "wewe ni nani?" yesu akawajibu, "nimewaambieni tangu mwanzo!

Wolof

Ñu ne ko: «yaay kan?» mu ne leen: «li ma leen waxoon ca njàlbéen ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

naye akawajibu, la, msije labda mnapokusanya magugu, mkang'oa na ngano pia.

Wolof

waaye mu tontu leen: “déedéet, ngir bañ a buddiwaale dugub ji, bu ngeen koy dindi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

yesu akawajibu, "hii ndiyo kazi anayotaka mungu muifanye: kumwamini yule aliyemtuma."

Wolof

yeesu tontu leen ne: «jëf ji neex yàlla, moo di gëm ki mu yónni.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

yesu akawajibu, "je, hamjasoma alivyofanya daudi pamoja na wenzake wakati walipokuwa na njaa?

Wolof

noonu yeesu tontu leen: «ndax jànguleen la daawuda defoon, ba mu xiifee, moom ak ña mu àndaloon?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

lakini yeye akawajibu, "kila mmea ambao baba yangu aliye mbinguni hakuupanda, utang'olewa.

Wolof

yeesu tontu leen ne: «garab gu sama baay bi ci kaw jiwul, dees na ko buddi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

yesu akawajibu, "je, mnaweza kuwataka wale walioalikwa arusini wafunge hali bwana arusi yuko pamoja nao?

Wolof

yeesu ne leen: «ndax man ngeen a woorloo gan, yi ñëw cig céet, li feek boroom céet gaa ngi ànd ak ñoom?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

naye akawajibu: kila aliye na kitu atapewa na kuzidishiwa. lakini yule asiye na kitu, hata kile alicho nacho kitachukuliwa.

Wolof

buur ba ne leen: “maa ngi leen koy wax, ku am, dinañu la dolli, waaye ku amul, li nga am as néew sax, dinañu ko nangu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

naye akawajibu, "hili ni jambo la kushangaza! ninyi hamjui ametoka wapi, lakini amenifumbua macho yangu!

Wolof

waa ja ne leen: «loolu de, doy na waar! xamuleen fu mu jóge, te moo ubbi samay bët!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

akawajibu, "aliye na nguo mbili amgawie yule asiye na nguo; aliye na chakula afanye vivyo hivyo."

Wolof

mu ne leen: «ku am ñaari mbubb, nga jox menn mi ki amul. ku am ñam itam, nga bokk ko ak ki amul.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

yesu akawajibu, "nendeni mkamwambie huyo mbweha hivi: leo na kesho ninafukuza pepo na kuponya wagonjwa, na siku ya tatu nitakamilisha kazi yangu.

Wolof

noonu mu ne leen: «demleen ne bukki boobu ne ko: “xoolal, maa ngi dàq rab yi tey wéral nit ñi tey ak suba. ca ñetteelu fan ba, ma àgg fa ma yàlla jëmale.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

yesu akawajibu, "hata kama ninajishuhudia mwenyewe, ushahidi wangu ni wa kweli kwa sababu mimi najua nilikotoka na ninakokwenda. lakini ninyi hamjui nilikotoka wala ninakokwenda.

Wolof

yeesu tontu leen: «maa ngi seedeel sama bopp, teewul li may wax di dëgg, ndaxte xam naa fa ma bàyyikoo, xam fa ma jëm. waaye yéen xamuleen fa ma bàyyikoo ak fa ma jëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,770,667,312 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK