Vous avez cherché: mlikombolewa (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

mlikombolewa kutoka utumwa wa dhambi, mkawa watumwa wa uadilifu.

Wolof

te ci noonu rëcc ngeen ci nootaangeg bàkkaar te jébbalu ci yàlla, sóobu ci njub.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

bali mlikombolewa kwa damu tukufu ya kristo, ambaye alikuwa kama mwana kondoo asiye na dosari wala doa.

Wolof

waaye ci deretu kirist ju tedd ji, mel ni mbote mu sikkul te wàññikuwul.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

maana mnajua kwamba ninyi mlikombolewa katika mwenendo wenu usiofaa ambao mliupokea kutoka kwa wazee wenu, si kwa vitu vyenye kuharibika: kwa fedha na dhahabu;

Wolof

xam ngeen ne, yàlla jot na leen ci seen dund gu tekkiwul dara, gi maam ya nekkoon; te jotuleen ak yu deme ni xaalis mbaa wurus yuy wéy,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,773,617,491 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK