Vous avez cherché: mwishowe (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

mwishowe akafa pia yule mwanamke.

Wolof

gannaaw ga nag jigéen ja it faatu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

mwishowe akamtuma mwanawe huku akifikiri: watamheshimu mwanangu.

Wolof

mujj mu yónni doomam naan: “xëy na ñu weg sama doom.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

akafunga siku arubaini mchana na usiku, na mwishowe akaona njaa.

Wolof

yeesu nekk fa te lekkul ñeent-fukki bëccëg ak ñeent-fukki guddi, door a xiif.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

jambo hilo lilifanyika mara tatu, na mwishowe vyote vilirudishwa juu mbinguni.

Wolof

loolu am ba muy ñetti yoon, ba noppi ñu ne cas lépp, jëme asamaan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

wote saba walikufa bila kuacha mtoto. mwishowe yule mama mjane naye akafa.

Wolof

mbir mi dem na nag, ba juróom-ñaar ñooñu ñépp dem, te kenn bàyyiwu fi doom. mujj jigéen ja faatu moom itam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

mwishowe hatukuweza kuvumilia zaidi. basi, tuliamua kubaki kule athene peke yetu,

Wolof

kon nag, ba nu ko mënatul a dékku, nangu nanu ñu bàyyi nu, nun doŋŋ, ca dëkku aten,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

wakati huo petro alikuwa anaendelea kupiga hodi. mwishowe walifungua mlango, wakamwona, wakashangaa.

Wolof

fekk piyeer di gën a fëgg. noonu ñu tijji, gis ko, daldi waaru.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

alibakiwa bado na mtu mmoja, yaani mwanawe mpendwa. mwishowe akamtuma huyo akisema, watamheshimu mwanangu.

Wolof

«noonu mu dese ko kenn rekk, di doomam ji mu bëgg. mujj mu yónni ko naan: “xëy na ñu weg sama doom.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

lakini wao wakazidi kupiga kelele kwa nguvu sana, kwamba yesu ni lazima asulubiwe. mwishowe, sauti zao zikashinda.

Wolof

waaye ñoom ñu sax ca la ñu waxoon, di gën a yuuxu naan, ñu daaj ko ci bant. coow la yey pilaat.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

kuadhibiwa si jambo la kufurahisha bali la kuhuzunisha. lakini wale waliofunzwa kuwa na nidhamu mwishowe watavuna tuzo la amani kutoka katika maisha adili!

Wolof

li am moo di ne, yar bu nuy dal, du ànd ak bànneex, day naqari, waaye gannaaw ga dafay meññ jub ak jàmm, ci ñi ko jariñoo.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

kwa muda mrefu huyo hakimu hakupenda kumtetea huyo mjane; lakini, mwishowe akajisemea: ingawa mimi simchi mungu wala simjali binadamu,

Wolof

Àttekat ba bañ lu yàgg, waaye am bés mu ne ci xelam: “ragaluma yàlla te faalewuma mbindeef,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

mwishowe, yesu aliwatokea wanafunzi kumi na mmoja walipokuwa pamoja mezani. akawakemea sana kwa sababu ya kutoamini kwao na ukaidi wao, maana hawakuwaamini wale waliokuwa wamemwona baada ya kufufuka.

Wolof

gannaaw ga it yeesu feeñu fukki taalibe yi ak benn, bi ñuy lekk. mu yedd leen ndax seen ngëmadi ak seen dëgër bopp, ci li ñu bañ a gëm ñi ko gisoon, bi mu dekkee.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,800,368,453 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK