Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
lakini hao wafuasi walikuwa wamejaa furaha na roho mtakatifu.
naka taalibe yi nag, ñu fees ak mbég ak xel mu sell mi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
kutokana na hayo, wengi wa wafuasi wake walirudi nyuma wasiandamane naye tena.
ci loolu taalibeem yu bare dëpp, bañatee ànd ak moom.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
halafu akawaelekea wafuasi wake akawaambia, "heri wanaoona yale mnayoyaona ninyi!
gannaaw bi mu waxee loolu, yeesu walbatiku ca taalibe ya ne leen ñoom rekk: «Ñi seeni bët di gis li ngeen di gis, am nañu mbég.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
basi, baadhi ya mafarisayo na wafuasi wa kikundi cha herode walitumwa ili wamtege yesu kwa maneno yake.
bi loolu amee ñu yónni ci yeesu ay farisen ak ñu far ak buur bi erodd, ngir fiir ko ci waxam.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ni dhahiri kwamba mlisikia barabara habari zake, na mkiwa wafuasi wake mkafundishwa ukweli ulivyo katika yesu.
ndax yaakaar naa ne, dégg ngeen kirist te jàng ngeen ci moom, ba xam dëgg gi yeesu ëmb.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
alikaa huko muda mfupi, halafu akaendelea na safari kwa kupitia sehemu za galatia na frugia akiwatia moyo wafuasi wote.
bi mu fa desee ay jamono, mu jóge fa, di jaar dëkkoo-dëkk ci diiwaanu galasi ak firisi, di dooleel xoli taalibe yépp.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
baadaye kidogo yesu alikwenda katika mji mmoja uitwao naini, na wafuasi wake pamoja na kundi kubwa la watu waliandamana naye.
yàggul dara yeesu dem ci dëkk bu ñuy wax nayin. taalibeem yi ak mbooloo mu bare ànd ak moom.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
basi, wengi wa wafuasi wake waliposikia hayo, wakasema, "haya ni mambo magumu! nani awezaye kuyasikiliza?"
bi ñu dégloo yeesu ba noppi, taalibeem yu bare nee nañu: «njàngale mii de, jafe na! kan moo ko man a déglu?»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
baada ya paulo na barnabas kuhubiri habari njema huko derbe na kupata wafuasi wengi, walifunga safari kwenda antiokia kwa kupitia lustra na ikonio.
bi ñu fa àggee nag, ñu xamle fa xebaar bu baax bi, ba sàkk fa ay taalibe yu bare. gannaaw loolu ñu dellusi listar, ikoñum ak ancos,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
basi, wakawatuma wafuasi wao pamoja na wafuasi wa kikundi cha herode. wakamwuliza, "mwalimu, tunajua kwamba wewe ni mtu mwaminifu, na kwamba wafundisha njia ya mungu kwa uaminifu; humwogopi mtu yeyote, maana cheo cha mtu si kitu kwako.
noonu ñu yónni ci moom seeni taalibe ak ñi far ak buur bi erodd ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne ku wóor nga, te ragaloo kenn, ndaxte seetuloo jëmmi nit, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
tena, baadaye, wakati ule wa kuhesabiwa watu, alitokea yuda wa galilaya. huyu naye, aliwavuta watu wakamfuata; lakini naye pia aliuawa, na wafuasi wake wakatawanyika.
gannaawam it yudaa mu galile jóg, ca jamono ja ñu doon bind waa réew ma, mu jógloo nit ñu bare, ñu ànd ak moom. moom itam dee na, te ay nitam ñépp tasaaroo.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
alipompata, alimleta antiokia. nao wote wawili walikaa na lile kanisa kwa mwaka wote mzima wakifundisha kundi kubwa la watu. huko antiokia, ndiko, kwa mara ya kwanza, wafuasi waliitwa wakristo.
bi mu ko gisee, mu indi ko ancos. noonu atum lëmm ñu bokk ak mbooloom ñi gëm, di jàngal nit ñu bare. te ci ancos lañu jëkk a tudde taalibe ya gaayi kirist.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
huyo mtu akawajibu, "nimekwisha waambieni, nanyi hamkusikiliza; kwa nini mwataka kusikia tena? je, ninyi pia mnataka kuwa wafuasi wake?"
mu ne leen: «wax naa leen ko ba noppi, waaye dégluwuleen ma. lu ngeen bëgg ci ma di ko wax, di waxaat? xanaa dangeen a bëgg a nekk yéen itam ay taalibeem?»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
mafarisayo na walimu wa sheria wakawanung'unikia wafuasi wake wakisema: "mbona mnakula na kunywa pamoja na watoza ushuru na wenye dhambi?"
farisen yi ak seeni xutbakat di xultu taalibey yeesu yi ne leen: «lu tax ngeen di lekkandoo ak di naanandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.