Vous avez cherché: sasampalataya (Tagalog - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Tagalog

Wolof

Infos

Tagalog

sinabi sa kaniya ni jesus, di baga sinabi ko sa iyo, na, kung ikaw ay sasampalataya, ay makikita mo ang kaluwalhatian ng dios?

Wolof

yeesu ne ko: «ndax waxuma la ne, boo gëmee, dinga gis ndamu yàlla?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Tagalog

sapagka't kung ipahahayag mo ng iyong bibig si jesus na panginoon, at sasampalataya ka sa iyong puso na binuhay siyang maguli ng dios sa mga patay ay maliligtas ka:

Wolof

ndaxte soo waxee ak sa gémmiñ ne, yeesu mooy boroom bi, te nga gëm ci sa xol ne, yàlla dekkal na ko, dinga mucc.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Tagalog

sinabi nga sa kaniya ng ibang mga alagad, nakita namin ang panginoon. nguni't sinabi niya sa kanila, malibang aking makita sa kaniyang mga kamay ang butas ng mga pako, at maisuot ko ang aking daliri sa butas ng mga pako, at maisuot ko ang aking kamay sa kaniyang tagiliran, ay hindi ako sasampalataya.

Wolof

yeneen taalibe yi ne ko: «gis nanu boroom bi!» waaye mu ne leen: «su ma gisul fa ñu daajoon pont ya ci ay loxoom, te defuma ca sama baaraam, su ma tegul it sama loxo ci wetam, duma ko gëm mukk.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,276,648 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK