Vous avez cherché: barkeel (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

yaw mi sa ngëm yolomul ndax man, barkeel nga.»

Anglais

and blessed is he, whosoever shall not be offended in me.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :

Wolof

yéen ñi xiif te mar njub, barkeel ngeen,ndax dingeen regg.

Anglais

blessed are they which do hunger and thirst after righteousness: for they shall be filled.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yeesu leewu leen, teg leen ay loxoom, barkeel leen.

Anglais

and he took them up in his arms, put his hands upon them, and blessed them.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ki boroom bi sëful ay bàkkaaram,kooka ku barkeel la.»

Anglais

blessed is the man to whom the lord will not impute sin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yéen ñi am xol bu sell, barkeel ngeen,ndax dingeen gis yàlla.

Anglais

blessed are the pure in heart: for they shall see god.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kiy barkeel a gën a màgg ki ñuy barkeel, loolu amu ci benn werante.

Anglais

and without all contradiction the less is blessed of the better.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yéen ñiy wut jàmm, barkeel ngeen,ndax dees na leen tudde doomi yàlla.

Anglais

blessed are the peacemakers: for they shall be called the children of god.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te it ngëm moo tax ba isaaxa barkeel yanqóoba ak esawu, di wax ci mbirum yëf yiy ñëw.

Anglais

by faith isaac blessed jacob and esau concerning things to come.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«waaye yéen barkeel ngeen, ndaxte seeni bët a ngi gis te seeni nopp di dégg!

Anglais

but blessed are your eyes, for they see: and your ears, for they hear.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu ne:«Ñi ñu baal seen jàdd yoon,te seeni bàkkaar far ci kanam yàlla,ñu barkeel lañu.

Anglais

saying, blessed are they whose iniquities are forgiven, and whose sins are covered.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

barkeel ngeen, bu leen nit ñi bañee, di leen dàq ak a saaga, di sib seen tur ngir doomu nit ki.

Anglais

blessed are ye, when men shall hate you, and when they shall separate you from their company, and shall reproach you, and cast out your name as evil, for the son of man's sake.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte fàttaliku na ma,man jaamam bu woyof bi.gannaawsi tey, niti jamono yéppdinañu ma wooye ki ñu barkeel,

Anglais

for he hath regarded the low estate of his handmaiden: for, behold, from henceforth all generations shall call me blessed.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

barkeel ngeen, yaw miy jàng ak yéen ñiy déglu wax yii jóge ca yàlla, te di sàmm li ñu ci bind, ndaxte waxtu wi jege na.

Anglais

blessed is he that readeth, and they that hear the words of this prophecy, and keep those things which are written therein: for the time is at hand.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yàlla feeñal na ndawam, jëkk koo yebal ci yéen, ngir barkeel leen, ci woññi leen kenn ku nekk ci say bàkkaar.»

Anglais

unto you first god, having raised up his son jesus, sent him to bless you, in turning away every one of you from his iniquities.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu xool ay taalibeem ne leen:«yéen ñi sësul lu dul ci yàlla, barkeel ngeen,ndaxte nguuru yàlla, yéena ko yelloo.

Anglais

and he lifted up his eyes on his disciples, and said, blessed be ye poor: for yours is the kingdom of god.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku la def lu bon mbaa mu saaga la, bul feyyu, waaye ñaanal ko lu baax; ndaxte ci loolu la leen yàlla woo, ngir barkeel leen.

Anglais

not rendering evil for evil, or railing for railing: but contrariwise blessing; knowing that ye are thereunto called, that ye should inherit a blessing.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi mu déggee wax yooyu, kenn ca gan ya ne yeesu: «kiy lekk ci ñam, yi yàlla di joxe ci nguuram, barkeel nga!»

Anglais

and when one of them that sat at meat with him heard these things, he said unto him, blessed is he that shall eat bread in the kingdom of god.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu tontu ko: «barkeel ñeel na la, simoŋ doomu yunus, ndaxte du nit moo la xamal lii, waaye sama baay bi nekk ci kaw.

Anglais

and jesus answered and said unto him, blessed art thou, simon barjona: for flesh and blood hath not revealed it unto thee, but my father which is in heaven.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye kuy gëstu yoonu yàlla, wi mat tey goreel --waxuma ki dégg, ba noppi fàtte, waaye kiy jëfe ndigal — kooku barkeel na ci kaw jëfam.

Anglais

but whoso looketh into the perfect law of liberty, and continueth therein, he being not a forgetful hearer, but a doer of the work, this man shall be blessed in his deed.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci lépp won naa leen royukaay, ci li nu war a dimbali ñi néew doole te fàttaliku li yeesu boroom bi wax moom ci boppam ne: “joxe moo gën a barkeel nangu.”»

Anglais

i have shewed you all things, how that so labouring ye ought to support the weak, and to remember the words of the lord jesus, how he said, it is more blessed to give than to receive.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,770,734,930 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK