Vous avez cherché: binduma (Wolof - Anglais)

Wolof

Traduction

binduma

Traduction

Anglais

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

binduma leen loolu ngir ngeen am yeraange, waaye dama koo def ngir artu leen, ndaxte yéenay samay doom te bëgg naa leen.

Anglais

i write not these things to shame you, but as my beloved sons i warn you.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci biir tiis ak xol bu jeex laa leen bind, samay bët taa ak ay rangooñ. binduma leen ngir teg leen naqar, waaye ngir ngeen xam xóotaayu mbëggeel gi ma am ci yéen.

Anglais

for out of much affliction and anguish of heart i wrote unto you with many tears; not that ye should be grieved, but that ye might know the love which i have more abundantly unto you.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye man jariñoowuma benn ci sañ-sañ yooyu, te binduma yëf yooyu, ngir ngeen di ma defal yu ni mel. dee sax moo ma ko gënal — kenn du jële ci man mbir moomu may kañoo!

Anglais

but i have used none of these things: neither have i written these things, that it should be so done unto me: for it were better for me to die, than that any man should make my glorying void.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,891,295,316 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK