Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
kan ci yéen, bu la sa doom ñaanee mburu, nga jox ko doj?
or what man is there of you, whom if his son ask bread, will he give him a stone?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu saraxalekat bu mag ba ne ko: «ndax loolu dëgg la?»
then said the high priest, are these things so?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
xebaar bu baaxu yeesu kirist, doomu yàlla, nii la tàmbalee.
the beginning of the gospel of jesus christ, the son of god;
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
jàngaleel loolu, di leen dénk ak a yedd ak fulla ju mat. bu la kenn yab.
these things speak, and exhort, and rebuke with all authority. let no man despise thee.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Ñu daldi ko wax bu kawe: «nuyu nanu la, yaw buuru yawut yi!»
and began to salute him, hail, king of the jews!
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Ñu tontu ko ne: «bu deful woon lu bon, duñu la ko jébbalsi.»
they answered and said unto him, if he were not a malefactor, we would not have delivered him up unto thee.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ndaxte xam ngeen bu wér ne, ni sàcc di ñëwe guddi, noonu la bésu boroom bi di ñëwe.
for yourselves know perfectly that the day of the lord so cometh as a thief in the night.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
waaye bi nu ngelaw li sonalee bu metti, ca ëllëg sa ñu sànni la gaal ga yeboon ca géej ga.
and we being exceedingly tossed with a tempest, the next day they lightened the ship;
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
leneen wadd ci bérab bu bare ay doj. naka la sax rekk, daldi wow, ndaxte suuf si tooyul woon.
and some fell upon a rock; and as soon as it was sprung up, it withered away, because it lacked moisture.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
te yaw dëkku kapernawum, ndax dees na la yékkati bu kawe? déedéet, dees na la daane bu suufe.
and thou, capernaum, which art exalted to heaven, shalt be thrust down to hell.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yàlla jébbalul malaaka yi benn sañ-sañ bu jëm ci jamonoy ëllëg ji nuy wax; keneen la ko jébbal,
for unto the angels hath he not put in subjection the world to come, whereof we speak.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
bu la kenn xeeb ndax say at, waaye defal sa bopp royukaayu ñi gëm ci say wax ak say jëf, ci sa mbëggeel, sa ngëm ak sa cell.
let no man despise thy youth; but be thou an example of the believers, in word, in conversation, in charity, in spirit, in faith, in purity.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
am na lu ma la bëgg a ñaan; teguma ko ci sañ-sañ bu mat bi ma kirist may, ci teg la ndigalu def sa warugar,
wherefore, though i might be much bold in christ to enjoin thee that which is convenient,
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
amoon na nag yawut bu tudd apolos te juddoo alegsàndiri, mu dikk efes. nit ku yeewu la woon te am xam-xam bu yaatu ci mbind mi.
and a certain jew named apollos, born at alexandria, an eloquent man, and mighty in the scriptures, came to ephesus.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
booba nag bésu waajal la woon, maanaam bés bu jiitu bésu noflaay bi. ca ngoon sa nag,
and now when the even was come, because it was the preparation, that is, the day before the sabbath,
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
gnome ab wërlaayub binduwaay la bu féex, yomb a jëfandikoo, jotale ngir xeeti nosteg doxiin yu dàttu ci unix.
gnome is a free, usable, stable, accessible desktop environment for the unix-like family of operating systems.
Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
waaye elimas, boroom xam-xam bu ñuul bi --ndaxte loolu la turam di tekki — di leen dogale, ngir bañ boroom réew ma gëm.
but elymas the sorcerer (for so is his name by interpretation) withstood them, seeking to turn away the deputy from the faith.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
maa ngi leen di wax lii: ci noonule la malaakay yàlla yi di ame mbég ci benn bàkkaarkat bu tuubee ay bàkkaaram.»
likewise, i say unto you, there is joy in the presence of the angels of god over one sinner that repenteth.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
bi ndaw ya dellusee, ñu nettali yeesu la ñu defoon lépp. noonu mu yóbbaale leen, ñu sore nit ñi, jëm ca dëkk bu ñuy wax betsayda.
and the apostles, when they were returned, told him all that they had done. and he took them, and went aside privately into a desert place belonging to the city called bethsaida.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ndaxte ñàkk benn ci say cér moo gën ci yaw, ñu sànni sa yaram wépp ci safara. bu la sa loxol ndeyjoor bëggee yóbbe bàkkaar, dagg ko, sànni ko fu sore. ndaxte ñàkk benn ci say cér moo gën ci yaw ñu sànni sa yaram wépp ci safara.
and if thy right hand offend thee, cut if off, and cast it from thee: for it is profitable for thee that one of thy members should perish, and not that thy whole body should be cast into hell.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.