Vous avez cherché: lool (Wolof - Anglais)

Wolof

Traduction

lool

Traduction

Anglais

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

ak maryaama, mi sonnoon lool ci yéen.

Anglais

greet mary, who bestowed much labour on us.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñi dégg li sàmm yi doon wax ñépp daldi waaru lool.

Anglais

and all they that heard it wondered at those things which were told them by the shepherds.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moo tax yàlla kaweel ko lool,jox ko tur wi tiim yépp,

Anglais

wherefore god also hath highly exalted him, and given him a name which is above every name:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte namm na leen lool, te tiisoo na li ngeen yég jagadeem.

Anglais

for he longed after you all, and was full of heaviness, because that ye had heard that he had been sick.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

foofa ñu indil ko ku tëx te dër lool, ñaan ko mu teg ko loxo.

Anglais

and they bring unto him one that was deaf, and had an impediment in his speech; and they beseech him to put his hand upon him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi taalibe yi déggee baat bi, ñu ne nërëm ci suuf, daldi tiit lool.

Anglais

and when the disciples heard it, they fell on their face, and were sore afraid.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bëgg na gis kan mooy yeesu, waaye dafa gàtt lool, ba mënu koo gis ndax mbooloo ma.

Anglais

and he sought to see jesus who he was; and could not for the press, because he was little of stature.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk na booba mbooloo maa ngi xaar, jaaxle lool ci li sakariya yàgg ca bérab bu sell ba.

Anglais

and the people waited for zacharias, and marvelled that he tarried so long in the temple.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gannaaw loolu seytaane yóbbu ko ci kaw tund wu kawe lool, won ko réewi àddina yépp ak seeni ndam.

Anglais

again, the devil taketh him up into an exceeding high mountain, and sheweth him all the kingdoms of the world, and the glory of them;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte bëgg naa leen a gis lool, ba indil leen barke bu jóge ci xel mu sell mi, ndax seen ngëm gën a dëgër.

Anglais

for i long to see you, that i may impart unto you some spiritual gift, to the end ye may be established;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ne leen: «yàkkamti woon naa lool lekk ak yéen reeru jéggi bii, laata ñu may sonal.

Anglais

and he said unto them, with desire i have desired to eat this passover with you before i suffer:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ma estefanas ak fortunatus ak akaykus seetsee, bég naa ci lool. taxawal nañu leen ci topptoo, bi ngeen yéene woon ci man te tële ko.

Anglais

i am glad of the coming of stephanas and fortunatus and achaicus: for that which was lacking on your part they have supplied.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ñépp waaru, ba jaaxle lool, ñuy waxante ci seen biir ne: «lii lu muy tekki?»

Anglais

and they were all amazed, and were in doubt, saying one to another, what meaneth this?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye seen dégg ndigal bir na ñépp, ba sama xol sedd lool ci yéen. teewul nag damaa bëgg ngeen am xam-xam bu leer ci lu baax, te bañ a laal dara ci lu bon.

Anglais

for your obedience is come abroad unto all men. i am glad therefore on your behalf: but yet i would have you wise unto that which is good, and simple concerning evil.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,884,423,394 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK