Vous avez cherché: nekkul (Wolof - Anglais)

Wolof

Traduction

nekkul

Traduction

Anglais

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

Ñooy féewale, te xelum yàlla nekkul ci ñoom, waaye niti kese lañu.

Anglais

these be they who separate themselves, sensual, having not the spirit.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye kuy dox guddi, dina fakkastalu, ndaxte leer nekkul ci moom.»

Anglais

but if a man walk in the night, he stumbleth, because there is no light in him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

su nu waxee ne amunu bàkkaar, kon nax nanu sunu bopp, te dëgg nekkul ci nun.

Anglais

if we say that we have no sin, we deceive ourselves, and the truth is not in us.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

buleen sopp àddina ak li ci biiram. ku sopp àddina, mbëggeelu baay bi nekkul ci moom.

Anglais

love not the world, neither the things that are in the world. if any man love the world, the love of the father is not in him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku wax ne xam nga ko, te sàmmoo ay ndigalam, dangay fen, te dëgg nekkul ci yaw.

Anglais

he that saith, i know him, and keepeth not his commandments, is a liar, and the truth is not in him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag nekkul yàllay ñi dee waaye yàllay ñiy dund la, ndaxte yàllaa tax ñépp di dund.»

Anglais

for he is not a god of the dead, but of the living: for all live unto him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moo tax mbind mi ne: «yéena tax ñi nekkul yawut di suufeel turu yàlla.»

Anglais

for the name of god is blasphemed among the gentiles through you, as it is written.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

buñu sonal kenn ci yéen ci li mu rey nit walla mu sàcc, mbaa def lu bon, walla dugg ci lu yoonam nekkul.

Anglais

but let none of you suffer as a murderer, or as a thief, or as an evildoer, or as a busybody in other men's matters.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li ci génn mooy, nekkul yàllay ñi dee, waaye yàllay ñiy dund la. kon sóobu ngeen cig réer.»

Anglais

he is not the god of the dead, but the god of the living: ye therefore do greatly err.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

léegi nag dégg nanu ne, am na ci yéen ñuy wéy ci tayel; liggéeyuñu dara, lu dul di dugg ci lu seen yoon nekkul.

Anglais

for we hear that there are some which walk among you disorderly, working not at all, but are busybodies.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

xebaar bi nu dégg ci yeesu kirist, di leen ko yégal, mooy lii: yàlla leer la, te genn lëndëm nekkul ci moom.

Anglais

this then is the message which we have heard of him, and declare unto you, that god is light, and in him is no darkness at all.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moom la wax ci téereb ose ne:«Ñi nekkul woon sama xeetdinaa leen ko def,ñi bokkul woon ci sama mbëggeel,dinaa leen ci boole.»

Anglais

as he saith also in osee, i will call them my people, which were not my people; and her beloved, which was not beloved.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kiy wax loolu na xam lii: ni sunuy kàddu mel ci sunuy bataaxal, bu nu fa nekkul, noonu it lanuy mel ci sunuy jëf, bu nu teewee.

Anglais

let such an one think this, that, such as we are in word by letters when we are absent, such will we be also in deed when we are present.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñëw na itam ngir ñi nekkul yawut man a màggal yàlla ndax yërmandeem. moo tax mbind mi ne:«dinaa la màggal tey tagg saw tur,ci kanamu xeet yépp.»

Anglais

and that the gentiles might glorify god for his mercy; as it is written, for this cause i will confess to thee among the gentiles, and sing unto thy name.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndax ñi dul yawut te nekkuñu ci yoonu musaa, ñu ngiy def li yoon woowu tëral, ndaxte yàlla def na ko ci nit. te wonee nañu noonu ne, man nañoo ràññee lu baax ak lu bon, su ñu nekkul sax ci yoonu musaa,

Anglais

for when the gentiles, which have not the law, do by nature the things contained in the law, these, having not the law, are a law unto themselves:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte doomu yàlla ji, yeesu kirist, mi nu doon yégle ci seen biir, man ak silwan ak timote, nekkul woon «waaw» ak «déedéet;» «waawi» yàlla la mas a nekk.

Anglais

for the son of god, jesus christ, who was preached among you by us, even by me and silvanus and timotheus, was not yea and nay, but in him was yea.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,926,378,051 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK