Vous avez cherché: sédd (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

kiy jàng kàddug yàlla war na sédd ki koy jàngal ci alalam jépp.

Anglais

let him that is taught in the word communicate unto him that teacheth in all good things.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

sédd na leen cér bu dul yàqu, du gàkk te du seey mukk, dencal leen ko ci asamaan,

Anglais

to an inheritance incorruptible, and undefiled, and that fadeth not away, reserved in heaven for you,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

dénk leen ñu def lu baax, te bare jëf yu rafet, ñu yéwén, bay sédd ñi amul,

Anglais

that they do good, that they be rich in good works, ready to distribute, willing to communicate;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

loolu lépp, menn xel moomu moo koy def, ku nekk mu sédd la ci, ni mu ko soobe.

Anglais

but all these worketh that one and the selfsame spirit, dividing to every man severally as he will.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te am nanu cér ci moom bu nu yàlla sédd lu jiitu ci dogalam, moom miy doxal lépp ci ni mu ko àttee ci coobareem.

Anglais

in whom also we have obtained an inheritance, being predestinated according to the purpose of him who worketh all things after the counsel of his own will:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mooy dëfël sunu xol ci sunu tiis yépp, ngir nun ci sunu bopp nu man a dëfël xolu ñépp ñi nekk ci tiis, di leen sédd ci noflaay, bi yàlla def ci sunu xol.

Anglais

who comforteth us in all our tribulation, that we may be able to comfort them which are in any trouble, by the comfort wherewith we ourselves are comforted of god.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

looloo tax ba musiba, yii ñu ko sédd, dinañu ñëw ci benn bés, ñu di mbas, ténj ak xiif, ñu di ko lakk ba mu jeex, ndaxte yàlla boroom bi ko àtte, ku am kàttan la.»

Anglais

therefore shall her plagues come in one day, death, and mourning, and famine; and she shall be utterly burned with fire: for strong is the lord god who judgeth her.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,787,439,672 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK