Vous avez cherché: tiitaru (Wolof - Arabe)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Arabe

Infos

Wolof

bu nu tiitaru di dëkkante, di iñaanante.

Arabe

لا نكن معجبين نغاضب بعضنا بعضا ونحسد بعضنا بعضا

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag bu kenn tiitaru ndax nit ñi, ndaxte yéena moom lépp,

Arabe

اذا لا يفتخرنّ احد بالناس. فان كل شيء لكم.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

am na ci seen biir ñuy tiitaru, di xalaat ne, duma delluseeti ci yéen.

Arabe

فانتفخ قوم كاني لست آتيا اليكم.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku bëgg dafay muñ te laabiir. ku bëgg du kiñaan, du kañu, du tiitaru,

Arabe

المحبة تتأنى وترفق. المحبة لا تحسد. المحبة لا تتفاخر ولا تنتفخ

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moona yéen de, yéena ngi tiitaru. waaye dangeen a waroon a am naqar, ba dàq kiy def loolu ci seen biir!

Arabe

أفانتم منتفخون وبالحري لم تنوحوا حتى يرفع من وسطكم الذي فعل هذا الفعل.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

su fekkee ne tiitaru woon naa ci seen mbir ci kanamu tit, rusuma ci. dëgg rekk lanu leen mas a wax; noonu it la tit gise ne, li nu leen doon seede lépp, dëgg la.

Arabe

فاني ان كنت افتخرت شيئا لديه من جهتكم لم أخجل بل كما كلمناكم بكل شيء بالصدق كذلك افتخارنا ايضا لدى تيطس صار صادقا.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte yaw, ku la def, ba nga gën a màgg ñi ci des? loo am lu ñu la mayul? te bu ñu la ko mayee, lu tax nga di ci tiitaru, mel ni mayuñu la ko?

Arabe

لانه من يميّزك واي شيء لك لم تأخذه. وان كنت قد اخذت فلماذا تفتخر كانك لم تأخذ.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,281,553 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK