Vous avez cherché: dootuleen (Wolof - Danois)

Wolof

Traduction

dootuleen

Traduction

Danois

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Danois

Infos

Wolof

dootuleen ko bàyyi, mu defal dara ndeyam walla baayam.

Danois

da tilstede i ham ikke mere at gøre noget for sin fader eller moder,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu dootuleen ay doxandéem mbaa ay gan, waaye am ngeen baat ci kureelu gaayi yàlla yu sell yi, te waa këram ngeen.

Danois

så ere i da ikke mere fremmede og udlændinge, men i ere de helliges medborgere og guds husfolk,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bés boobu dootuleen ma laaj dara. ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, baay bi dina leen may lu ngeen ko ñaan ci sama tur.

Danois

og på den dag skulle i ikke spørge mig om noget. sandelig, sandelig, siger jeg eder, hvad som helst i bede faderen om, skal han give eder i mit navn.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«fi mu ne nag xam naa ne, dootuleen gis sama kanam, yéen ñépp ñi ma jaaroon ci seen biir, di yégle nguuru yàlla.

Danois

og nu se, jeg ved, at i ikke mere skulle se mit ansigt, alle i, iblandt hvem jeg gik om og prædikede riget.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li leen gën a teg aw tiis mooy li mu leen wax: «dootuleen gis sama kanam.» noonu ñu gunge ko ba ca gaal ga.

Danois

og mest smertede dem det ord, han havde sagt, at de ikke mere skulde se hans ansigt. så ledsagede de ham til skibet.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,947,584,178 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK