Vous avez cherché: déggul (Wolof - Espagnol)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Espagnol

Infos

Wolof

loolu war na, ndaxte am na ñu bare ñu déggul lenn ndigal, rawatina ci yawut yi, ñuy yàq xeli nit ñi ak seen waxi neen.

Espagnol

porque hay aún muchos rebeldes, habladores de vanidades y engañadores, especialmente de los de la circuncisión

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte kiy wax aw làkk, waxul ak nit ñi, waaye yàlla lay waxal, ndaxte kenn déggul li muy wax. dafay wax ay mbóot ci xelam.

Espagnol

porque el que habla en una lengua no habla a los hombres sino a dios; porque nadie le entiende, pues en espíritu habla misterios

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye ma ne: xanaa ñépp dañoo déggul? aaŋkay! mbind mi wax na ne:«seen baat jolli na ci ñeenti xebla yépp,seen wax wër na àddina sépp.»

Espagnol

pero pregunto: ¿acaso no oyeron? ¡claro que sí! por toda la tierra ha salido la voz de ellos; y hasta los confines del mundo, sus palabras

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,793,691,339 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK