Vous avez cherché: dinga (Wolof - Espagnol)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Espagnol

Infos

Wolof

kon boo ma màggalee, dinga moom lépp.»

Espagnol

por esto, si tú me adoras, todo será tuyo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku sa liggéey dëgër, dinga jot yool.

Espagnol

si permanece la obra que alguien ha edificado sobre el fundamento, él recibirá recompensa

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte li nga gis te dégg ko, dinga ko seede ci ñépp.

Espagnol

porque serás testigo suyo ante todos los hombres de lo que has visto y oído

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

dinga ëmb, jur doom ju góor; nanga ko tudde yeesu.

Espagnol

he aquí concebirás en tu vientre y darás a luz un hijo, y llamarás su nombre jesús

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

booba nag ku woo boroom bi ci aw turam,dinga mucc.”

Espagnol

y sucederá que todo aquel que invoque el nombre del señor será salvo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu dinga man a xam ne, li ñu la jàngaloon lu wér peŋŋ la.

Espagnol

para que conozcas bien la verdad de las cosas en las cuales has sido instruido

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ku nekk ci nun dinga làyyi fa yàlla ci lépp loo mas a def.

Espagnol

de manera que cada uno de nosotros rendirá cuenta a dios de sí mismo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te boo ko gisee, dinga ko gàddu ak bànneex, yóbbu ko kër ga.

Espagnol

y al hallarla, la pone sobre sus hombros gozoso

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte bind nañu: «képp ku woo boroom bi ciw turam, dinga mucc.»

Espagnol

porque todo aquel que invoque el nombre del señor será salvo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

dinga xamal mbooloom,ni leen boroom bi man a musale,jaare ko ci seen mbaalug bàkkaar,

Espagnol

para dar a su pueblo conocimiento de salvación en el perdón de sus pecados

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku daan, dinga am cér ci mbir yii. dinaa nekk yàlla sa boroom, te dinga nekk doom ci man.

Espagnol

el que venza heredará estas cosas; y yo seré su dios, y él será mi hijo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye ku sa liggéey lakk, dinga ñàkk. yaw ci sa bopp dinga mucc, waaye mel ni ku rëcc ci safara si.

Espagnol

si la obra de alguien es quemada, él sufrirá pérdida; aunque él mismo será salvo, pero apenas, como por fuego

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu tontu ko: «gëmal yeesu boroom bi, kon dinga mucc, yaw ak sa njaboot.»

Espagnol

ellos dijeron: --cree en el señor jesús y serás salvo, tú y tu casa

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag ku laabal sa bopp ci yooyu yépp, dinga nekk ndab lu tedd te sell, nga am njariñ ci boroom bi te jekk ci bépp jëf ju rafet.

Espagnol

así que, si alguno se limpia de estas cosas, será un vaso para honra, consagrado y útil para el señor, preparado para toda buena obra

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

léegi nag gannaaw gëmuloo li ma wax, dinga luu te dootuloo man a wax, ba kera sama wax di am, bu jamonoom jotee.»

Espagnol

he aquí, quedarás mudo e incapaz de hablar hasta el día en que se realice esto, por cuanto no has creído a mis palabras, las cuales se cumplirán a su debido tiempo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte koo xam ne bëgg ngaa rawale sa bakkan, dinga ko ñàkk, waaye ku ñàkk sa bakkan ngir man ak ngir xebaar bu baax bi, dinga ko jotaat.

Espagnol

porque el que quiera salvar su vida, la perderá; pero el que pierda su vida por causa de mí y del evangelio, la salvará

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku daan, dinga sol mbubb mu weex ni ñoom. te duma far sa tur ci téereb dund bi, waaye dinaa nangu ci sama kanamu baay ak ay malaakaam ne, bokk nga ci man.

Espagnol

de esta manera, el que venza será vestido con vestidura blanca; y nunca borraré su nombre del libro de la vida, y confesaré su nombre delante de mi padre y delante de sus ángeles

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku bëgg a jub ci kanam yàlla ci kaw sàmm yoon, musaa daf cee wax ne: «ku ko manoon a matal, dinga dund ba fàww.»

Espagnol

moisés escribe de la justicia que es por la ley: el hombre que haga estas cosas vivirá por ellas

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye malaaka ma ne ko: «bul ragal dara sakariya, ndaxte sa ñaan nangu na. elisabet sa jabar dina la jural doom, te dinga ko tudde yaxya.

Espagnol

pero el ángel le dijo: --¡no temas, zacarías! porque tu oración ha sido atendida. tu esposa elisabet te dará a luz un hijo, y llamarás su nombre juan

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu tontu ko ne: «ndax li ma ne, gis naa la ca ker garab ga, moo tax nga gëm? dinga gis mbir yu gën a réy yii.»

Espagnol

respondió jesús y le dijo: --¿crees porque te dije: "te vi debajo de la higuera"? ¡cosas mayores que éstas verás

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,777,808,064 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK