Vous avez cherché: ndekkite (Wolof - Estonien)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Estonien

Infos

Wolof

dañoo moy dëgg, di wax ne ndekkite wees na, ba yàq ngëmu ñenn ñi.

Estonien

kes on eksinud ära tõest ja ütlevad ülestõusmise juba olnud olevat, ja rikuvad mõnede usu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gannaaw ci nit la dee jaar, dugg àddina, kon it ci nit la ndekkite jaar.

Estonien

sest kui juba surm on tulnud inimese kaudu, siis on ka surnute ülest

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu téye wax jooju ci seen biir, di sotteente xel, ba xam lu ndekkite looluy tekki.

Estonien

ja nad pidasid meeles selle s

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeneen néew yi duñu dekki, fi ak junniy at yi matul. loolu moo di ndekkite lu jëkk li.

Estonien

aga muud surnud ei elustunud mitte, kuni need tuhat aastat otsa saavad. see on esimene ülestõusmine.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bu ndekkite taxawee nag, jabaru kan lay doon ci juróom-ñaar ñi, ndaxte ñépp jël nañu ko?»

Estonien

ent ülestõusmises, kelle naiseks ta jääb nende seitsme seast, sest ta on kõikidel olnud?”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci ndekkite li nag kan ci ñoom moo ko war a donn, fekk ku nekk ci juróom-ñaar ñi mas na koo takk?»

Estonien

kui nad nüüd ülest

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

màrt tontu ko ne: «xam naa ne, dina jóg bésu ndekkite la, keroog bés bu mujj ba.»

Estonien

marta ütles talle: „ma tean, et ta üles tõuseb ülestõusmises viimsel päeval!”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci ndekkite li nag, kan ci ñoom moo war a donn jigéen ja, fekk ku nekk ci juróom-ñaar ñi mas na koo takk?»

Estonien

kelle naiseks nende seast nüüd see naine peab olema ülest

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngëm moo tax ba ay jigéen gis ñu dekkal seeni néew, delloo leen ko; ñeneen ñi ñu metital leen, te bañ ku leen musal, ngir jot ndekkite lu gën.

Estonien

naised said tagasi oma surnud ülestõusmise läbi. teised lasksid ennast piinata ega võtnud vastu vabastamist, et saaksid parema ülestõusmise osalisiks.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñi bokk ci ndekkite lu jëkk li, barkeel nañu te sell! Ñaareelu dee gi du leen manal dara. waaye dinañu doon saraxalekati yàlla ak kirist, tey nguuru ak moom junniy at.

Estonien

Õnnis ja püha on see, kellel on osa esimesest ülestõusmisest; nende üle ei ole teisel surmal meelevalda, vaid nad peavad olema jumala ja kristuse preestrid ja valitsema kuninglikult ühes temaga need tuhat aastat.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te sax li jëm ci mbirum ndekkite, xanaa jànguleen lii yàlla wax ci tawreetu musaa ci saarum ngarab si: “maay yàllay ibraayma, isaaxa ak yanqóoba”?

Estonien

aga surnute kohta, et need üles äratatakse, eks te ole lugenud moosese raamatust kibuvitsap

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ay boroom xam-xam ci mbooloo mi ñuy wax epikuren ak ci mbooloo mi ñuy wax estowisen, di werante ak moom. Ñenn ci ñoom ne: «fortukatu xam-xam bii, lu mu bëgg a wax?» te ña ca des, bi ñu déggee pool di waare xebaar bu baax bi, aju ci yeesu ak ci mbirum ndekkite, ñu ne: «dafa mel ni, day waare ay yàlla yu nu xamul.»

Estonien

ja mõned epikuurlaste ja stoalaste mõttetargad vaidlesid temaga. Ühed ütlesid: „mida siis see lobasuu tahab öelda?” aga teised: „tema näib kuulutavat võõraid vaime!” sest ta jutlustas neile jeesusest ja ülestõusmisest.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,765,238,071 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK