Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
ca saa sa ngelaw lu bare daldi yengal dex ga, ba duus ya sàng gaal ga. fekk booba yeesu nelaw.
et voici, il s`éleva sur la mer une si grande tempête que la barque était couverte par les flots. et lui, il dormait.
Ñooñule ay teen yu dëy lañu, di xiini lay, yu ngelaw liy naawal, te seen pey mooy lëndëm gu ne taraj.
ces gens-là sont des fontaines sans eau, des nuées que chasse un tourbillon: l`obscurité des ténèbres leur est réservée.
ndaxte meluleen ni bànni israyil ñoom ñi jege woon tund wu ñu man a laal, wu doon tàkk jeppit te ànd ak xiin ak lëndëm ak ngelaw.
vous ne vous êtes pas approchés d`une montagne qu`on pouvait toucher et qui était embrasée par le feu, ni de la nuée, ni des ténèbres, ni de la tempête,
noonu dootunu ay gune yu njàngalem nit ku ñëw di fàbbi ci seeni làqarci ak seeni pexe, nu mel ni ay gaal yu duus yi ak ngelaw li di baaje.
afin que nous ne soyons plus des enfants, flottants et emportés à tout vent de doctrine, par la tromperie des hommes, par leur ruse dans les moyens de séduction,
te gaal yi it yu réy lañu, te ngelaw lu am doole di leen jiñax, waaye dawalkat bi, weñ gu tuuti la leen di jëme fu ko neex.
voici, même les navires, qui sont si grands et que poussent des vents impétueux, sont dirigés par un très petit gouvernail, au gré du pilote.
noonu bi ngelaw lu woyof liy jóge sudd wolee, ñu defe ne, man nañoo sottal seen pexe, ñu wëgg diigal, daldi tafu ci dunu kereet.
un léger vent du sud vint à souffler, et, se croyant maîtres de leur dessein, ils levèrent l`ancre et côtoyèrent de près l`île de crète.
bi ñuy dem nag, yeesu daldi nelaw. ngelaw lu am doole daldi ñëw, yengal dex gi, gaal gi fees ak ndox, ba ñu bëgg a suux.
pendant qu`ils naviguaient, jésus s`endormit. un tourbillon fondit sur le lac, la barque se remplissait d`eau, et ils étaient en péril.
ngelaw fu ko neex lay jublu. yaa ngi koy dégg waaye xamuloo fu mu jóge, xamuloo fu mu jëm. noonu la mel it ci képp ku juddoo ci xelum yàlla.»
le vent souffle où il veut, et tu en entends le bruit; mais tu ne sais d`où il vient, ni où il va. il en est ainsi de tout homme qui est né de l`esprit.
waaye bi mu gisee ni ngelaw li mettee, mu daldi tiit, tàmbalee suux. mu woote ne: «sang bi, wallu ma!»
mais, voyant que le vent était fort, il eut peur; et, comme il commençait à enfoncer, il s`écria: seigneur, sauve-moi!
ci wàllu malaaka yi, lii la ci yàlla wax:«def na malaakaam yi, ñu mel ni ay ngelaw,ñooñu koy liggéeyal, mu def leen niki safara.»
de plus, il dit des anges: celui qui fait de ses anges des vents, et de ses serviteurs une flamme de feu.
noonu nuy dem ndànk diirub fan yu bare, ba janook kanidd ci kaw coono bu réy; te ndegam ngelaw li mayu nu, nu jëm kanam, nu leru dunu kereet ci fegu ngelaw li, janook salmon.
pendant plusieurs jours nous naviguâmes lentement, et ce ne fut pas sans difficulté que nous atteignîmes la hauteur de cnide, où le vent ne nous permit pas d`aborder. nous passâmes au-dessous de l`île de crète, du côté de salmone.
ci kaw loolu juróom-ñaareelu malaaka ma sotti ndabam ci ngelaw. noonu baat bu xumb jóge ca gàngune ma ca kër yàlla ga, naan: «lépp mat na.»
le septième versa sa coupe dans l`air. et il sortit du temple, du trône, une voix forte qui disait: c`en est fait!