Vous avez cherché: surga (Wolof - Russe)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Russe

Infos

Wolof

ña ca des jàpp surga ya, toroxal leen, rey leen.

Russe

прочие же, схватив рабов его, оскорбили и убили их .

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ki gën a mag ci yéen mooy ki nangoo nekk seen surga.

Russe

Больший из вас да будет вам слуга:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu daldi woo kenn ca surga ya nag, laaj ko lu xew.

Russe

и, призвав одного из слуг, спросил: что это такое?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeyootumaa nekk sa doom; boole ma ci say surga.’ ”

Russe

и уже недостоин называться сыном твоим;прими меня в число наемников твоих.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu yónniwaat beneen surga, waaye ñu dóor ko ci bopp, toroxal ko.

Russe

Опять послал к ним другого слугу; и тому камнями разбили голову и отпустили его с бесчестьем.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

booba surga day daw, ndaxte xaalis rekk lay liggéeyal, faalewul xar ya.

Russe

А наемник бежит, потому что наемник, и нерадит об овцах.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«gannaaw diir bu yàgg njaatigeb surga ya dellusi, daldi leen laaj alalam.

Russe

По долгом времени, приходит господин рабов тех и требует у них отчета.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

buleen mel ni ñooñu. waaye ku bëgg a nekk kilifa ci yéen, na nekk seen surga,

Russe

Но между вами да не будет так: а кто хочет быть большим между вами, да будем вам слугою;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

boroom kër gi nag yónniwaat yeneen surga yu ëpp yu jëkk ya, beykat yi def leen noonu ñoom itam.

Russe

Опять послал он других слуг, больше прежнего; и с нимипоступили так же.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ne ko: «sang bi, sama surga dafa làggi, tëdd ca kër ga te sonn lool.»

Russe

Господи! слуга мой лежит дома в расслаблении и жестоко страдает.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

surga ba ca topp ñëw ne: “sang bi, sa libidoor ba indi na juróomi libidoor.”

Russe

Пришел второй и сказал: господин! мина твоя принесла пять мин.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu yónneeti beneen surga, ñu rey ko. mu yónni ñeneen ñu bare, ñii ñu dóor leen, ñii ñu rey.

Russe

И опять иного послал: и того убили; и многих других то били, то убивали.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye yéen buleen def noonu. ki gën a màgg ci yéen, na nekk ni ki gën a ndaw, te njiit mel ni surga.

Russe

а вы не так: но кто из вас больше, будь как меньший, и начальствующий – как служащий.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu surga ya génn ca yoon ya, boole ña ñu fa gis ñépp, ñu bon ña ak ñu baax ña, ba néegu reer ya fees ak ay gan.

Russe

И рабы те, выйдя на дороги, собрали всех, кого только нашли, и злых и добрых; и брачныйпир наполнился возлежащими.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«surga bi xam bëgg-bëggu njaatigeem, te waajul mbaa mu takku def ko, dinañu ko dóor dóor yu metti.

Russe

Раб же тот, который знал волю господина своего, и не был готов, и не делал по воле его, бит будет много;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu tontu leen: “noon a ko def.” surga ya ne ko: “ndax nu dem dindi ko?”

Russe

Он же сказал им: враг человека сделал это. А рабы сказали ему: хочешь ли, мы пойдем, выберем их?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kuy apolos? ak kuy pool? nun ay surga rekk lanu, yu ngeen jaare, ba gëm. te boroom bi moo sas ku nekk liggéeyam.

Russe

Кто Павел? кто Аполлос? Они только служители, черезкоторых вы уверовали, и притом поскольку каждому дал Господь.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye njiit la tontu ko ne: «sang bi, yeyoowuma nga dugg ci sama kër; waxal genn kàddu rekk, te sama surga dina wér.

Russe

Сотник же, отвечая, сказал: Господи! я недостоин, чтобы Ты вошел под кров мой, но скажи только слово, и выздоровеет слуга мой;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ki toog ca lekkukaay ba, moom ak surgaam, ñoom ñaar kan moo ci gën a màgg? xanaa du ki toog ci lekkukaay bi? waaye man maa ngi ci seen biir ni surga.

Russe

Ибо кто больше: возлежащий, или служащий? не возлежащий ли? А Я посреди вас, как служащий.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mujj xelam dellusi, mu ne: “sama baay am na ay surga yu bare, te dañuy lekk ba suur. man nag maa ngi fii di bëgg a dee ak xiif!

Russe

Придя же в себя, сказал: сколько наемников у отца моего избыточествуют хлебом, а я умираю от голода;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,269,782 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK